Al-Mu'minun · 102/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
فَمَن ثَقُلَتْ مَوَازِينُهُ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ ١٠٢
Transliteration
Faman saqulat mawaazee nuhoo fa ulaaa`ika humul muflihoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Képp ku peeseem diis [ak jëf yu baax]ñoom ñooy ña texe ;
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 100-104 — Simoore Al-Mu'minun
100لَعَلِّي أَعْمَلُ صَالِحًا فِيمَا تَرَكْتُ ۚ كَلَّا ۚ إِنَّهَا كَلِمَةٌ هُوَ قَائِلُهَا ۖ وَمِن وَرَائِهِم بَرْزَخٌ إِلَىٰ يَوْمِ يُبْعَثُونَ
ndax ma mën a jëf yiw ca la ma fa bàyyi”. [Mukk loolu du mës a am], loolu kàddu la rekk gu muy wax. [Barsàq] kiiraay la ñuy nekk ba ba ñuy dekki”.
101فَإِذَا نُفِخَ فِي الصُّورِ فَلَا أَنسَابَ بَيْنَهُمْ يَوْمَئِذٍ وَلَا يَتَسَاءَلُونَ
Bu ñu walee Buftu bi kerook Bisboobu, askan amatul seen diggante te dootuñu lijjanti.
102فَمَن ثَقُلَتْ مَوَازِينُهُ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Képp ku peeseem diis [ak jëf yu baax]ñoom ñooy ña texe ;
103وَمَنْ خَفَّتْ مَوَازِينُهُ فَأُولَٰئِكَ الَّذِينَ خَسِرُوا أَنفُسَهُمْ فِي جَهَنَّمَ خَالِدُونَ
képp ku peeseem woyof [ak jëf yu baax], ñooña ñoo di ña sànku ci biir Safara te béel fa.
104تَلْفَحُ وُجُوهَهُمُ النَّارُ وَهُمْ فِيهَا كَالِحُونَ
Safara waa ngay làkk seeni kanam, ñu ne fa xuum
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
102Aaya
Tekki — Al-Mu'minun 102
Simoore Al-Mu'minun Aaya 102 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp ku peeseem diis [ak jëf yu baax]ñoom ñooy ña…Simoore Aaya 102/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 100–104. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Al-Mu'minun
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Friday, October 2, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


