Al-Mu'minun · 73/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَإِنَّكَ لَتَدْعُوهُمْ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ ۝٧٣
Wa innaka latad`oohum ilaa Siraatim Mustaqeem
📖 Tekkim Wolof
Te yaa ngi leen di woo jëme leen ca yoon wu jub wa xocc.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 71-75 — Simoore Al-Mu'minun

71وَلَوِ اتَّبَعَ الْحَقُّ أَهْوَاءَهُمْ لَفَسَدَتِ السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ وَمَن فِيهِنَّ ۚ بَلْ أَتَيْنَاهُم بِذِكْرِهِمْ فَهُمْ عَن ذِكْرِهِم مُّعْرِضُونَ
Te bu Yàlla toppoon seen bànneex, kon asamaan ak suuf si yàqu. Indil Nanu leen ag waare, waaye dañoo dummóoyu waare googu.
72أَمْ تَسْأَلُهُمْ خَرْجًا فَخَرَاجُ رَبِّكَ خَيْرٌ ۖ وَهُوَ خَيْرُ الرَّازِقِينَ
Ndax danga leen di laaj ab génnuwaay ? Sa génnuwaayu Boroom moo gën. Te moom [Yàlla] moo Gën ji kuy wërsëgal.
73وَإِنَّكَ لَتَدْعُوهُمْ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Te yaa ngi leen di woo jëme leen ca yoon wu jub wa xocc.
74وَإِنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ عَنِ الصِّرَاطِ لَنَاكِبُونَ
Ña xamul àllaaxira nag ñoom xamuñu yoon wa.
75۞ وَلَوْ رَحِمْنَاهُمْ وَكَشَفْنَا مَا بِهِم مِّن ضُرٍّ لَّلَجُّوا فِي طُغْيَانِهِمْ يَعْمَهُونَ
Bu Nu leen yërëmoon ba wàññi seeni tiis, ñu dellooti nuur ca seen bew ga.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
73Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 73

Simoore Al-Mu'minun Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te yaa ngi leen di woo jëme leen ca yoon…

Simoore Aaya 73/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 71–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers