Al-Mu'minun · 74/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَإِنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ عَنِ الصِّرَاطِ لَنَاكِبُونَ ۝٧٤
Wa innnal lazeena laa yu`minoona bil Aakhirati `anis siraati lanaakiboon
📖 Tekkim Wolof
Ña xamul àllaaxira nag ñoom xamuñu yoon wa.

🎧 Dégg


📜 Aaya 72-76 — Simoore Al-Mu'minun

72أَمْ تَسْأَلُهُمْ خَرْجًا فَخَرَاجُ رَبِّكَ خَيْرٌ ۖ وَهُوَ خَيْرُ الرَّازِقِينَ
Ndax danga leen di laaj ab génnuwaay ? Sa génnuwaayu Boroom moo gën. Te moom [Yàlla] moo Gën ji kuy wërsëgal.
73وَإِنَّكَ لَتَدْعُوهُمْ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Te yaa ngi leen di woo jëme leen ca yoon wu jub wa xocc.
74وَإِنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ عَنِ الصِّرَاطِ لَنَاكِبُونَ
Ña xamul àllaaxira nag ñoom xamuñu yoon wa.
75۞ وَلَوْ رَحِمْنَاهُمْ وَكَشَفْنَا مَا بِهِم مِّن ضُرٍّ لَّلَجُّوا فِي طُغْيَانِهِمْ يَعْمَهُونَ
Bu Nu leen yërëmoon ba wàññi seeni tiis, ñu dellooti nuur ca seen bew ga.
76وَلَقَدْ أَخَذْنَاهُم بِالْعَذَابِ فَمَا اسْتَكَانُوا لِرَبِّهِمْ وَمَا يَتَضَرَّعُونَ
Dananu leen mbugal ndax toroxlu wuñu ngir seen Boroom ; jaamuwuñu Ko,
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
74Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 74

Simoore Al-Mu'minun Aaya 74 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña xamul àllaaxira nag ñoom xamuñu yoon wa.

Simoore Aaya 74/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 72–76. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers