Al-Mu'minun · 72/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
أَمْ تَسْأَلُهُمْ خَرْجًا فَخَرَاجُ رَبِّكَ خَيْرٌ ۖ وَهُوَ خَيْرُ الرَّازِقِينَ ۝٧٢
Am tas`aluhum kharjan fakharaaju Rabbika khairunw wa Huwa khairur raaziqeen
📖 Tekkim Wolof
Ndax danga leen di laaj ab génnuwaay ? Sa génnuwaayu Boroom moo gën. Te moom [Yàlla] moo Gën ji kuy wërsëgal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 70-74 — Simoore Al-Mu'minun

70أَمْ يَقُولُونَ بِهِ جِنَّةٌ ۚ بَلْ جَاءَهُم بِالْحَقِّ وَأَكْثَرُهُمْ لِلْحَقِّ كَارِهُونَ
Walla dañu naan : “Jinnee ko sadd ? ” [Du loolu lépp], li am mooy moom dëgg rekk la indi. Te li ëpp ci ñoom dañoo sib dëgg.
71وَلَوِ اتَّبَعَ الْحَقُّ أَهْوَاءَهُمْ لَفَسَدَتِ السَّمَاوَاتُ وَالْأَرْضُ وَمَن فِيهِنَّ ۚ بَلْ أَتَيْنَاهُم بِذِكْرِهِمْ فَهُمْ عَن ذِكْرِهِم مُّعْرِضُونَ
Te bu Yàlla toppoon seen bànneex, kon asamaan ak suuf si yàqu. Indil Nanu leen ag waare, waaye dañoo dummóoyu waare googu.
72أَمْ تَسْأَلُهُمْ خَرْجًا فَخَرَاجُ رَبِّكَ خَيْرٌ ۖ وَهُوَ خَيْرُ الرَّازِقِينَ
Ndax danga leen di laaj ab génnuwaay ? Sa génnuwaayu Boroom moo gën. Te moom [Yàlla] moo Gën ji kuy wërsëgal.
73وَإِنَّكَ لَتَدْعُوهُمْ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
Te yaa ngi leen di woo jëme leen ca yoon wu jub wa xocc.
74وَإِنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ عَنِ الصِّرَاطِ لَنَاكِبُونَ
Ña xamul àllaaxira nag ñoom xamuñu yoon wa.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
72Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 72

Simoore Al-Mu'minun Aaya 72 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax danga leen di laaj ab génnuwaay ? Sa génnuwaayu…

Simoore Aaya 72/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 70–74. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers