Al-Furqan · 42/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
إِن كَادَ لَيُضِلُّنَا عَنْ آلِهَتِنَا لَوْلَا أَن صَبَرْنَا عَلَيْهَا ۚ وَسَوْفَ يَعْلَمُونَ حِينَ يَرَوْنَ الْعَذَابَ مَنْ أَضَلُّ سَبِيلًا ۝٤٢
In kaada la yudillunaa `an aalihatinaa law laaa an sabarnaa `alaihaa; wa sawfa ya`lamoona heena yarawnal `azaaba man adallu sabeela
📖 Tekkim Wolof
Bu nu muñul woon, danañu xaw a féewaleek sunu yàlla jii ! ”. Waaye danañu xam [Bis bu ñu gisee mbugal ma], ana kan moo réere yoon wu jub wa.
🎧 Dégg

📜 Aaya 40-44 — Al-Furqan

40وَلَقَدْ أَتَوْا عَلَى الْقَرْيَةِ الَّتِي أُمْطِرَتْ مَطَرَ السَّوْءِ ۚ أَفَلَمْ يَكُونُوا يَرَوْنَهَا ۚ بَلْ كَانُوا لَا يَرْجُونَ نُشُورًا
Romb nañu dëkk ba mbugal ma wàcce woon. Moo ndax gisuñu ko woon ? Ñoom kay dañoo foogoon ne duñu dekki !
41وَإِذَا رَأَوْكَ إِن يَتَّخِذُونَكَ إِلَّا هُزُوًا أَهَٰذَا الَّذِي بَعَثَ اللَّهُ رَسُولًا
Bu ñu la gisee dañu lay téjji naan : “Ndax kii la Yàlla yónni ?
42إِن كَادَ لَيُضِلُّنَا عَنْ آلِهَتِنَا لَوْلَا أَن صَبَرْنَا عَلَيْهَا ۚ وَسَوْفَ يَعْلَمُونَ حِينَ يَرَوْنَ الْعَذَابَ مَنْ أَضَلُّ سَبِيلًا
Bu nu muñul woon, danañu xaw a féewaleek sunu yàlla jii ! ”. Waaye danañu xam [Bis bu ñu gisee mbugal ma], ana kan moo réere yoon wu jub wa.
43أَرَأَيْتَ مَنِ اتَّخَذَ إِلَٰهَهُ هَوَاهُ أَفَأَنتَ تَكُونُ عَلَيْهِ وَكِيلًا
Ndax gisuloo ka jàppe bakkanam mu di yàllaam ? Moo ndax dangay doon wéeruwaayam ?
44أَمْ تَحْسَبُ أَنَّ أَكْثَرَهُمْ يَسْمَعُونَ أَوْ يَعْقِلُونَ ۚ إِنْ هُمْ إِلَّا كَالْأَنْعَامِ ۖ بَلْ هُمْ أَضَلُّ سَبِيلًا
Walla dangaa jàpp ne li ëpp ci ñoom dañuy dégg di xam ? Ñoom kay ñook mala yi ñoo yem. Walla sax ñoo gën a sànku.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Al-Furqan 42

Simoore Al-Furqan Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu nu muñul woon, danañu xaw a féewaleek sunu yàlla…

Simoore Aaya 42/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers