Al-Furqan · 43/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
أَرَأَيْتَ مَنِ اتَّخَذَ إِلَٰهَهُ هَوَاهُ أَفَأَنتَ تَكُونُ عَلَيْهِ وَكِيلًا ٤٣
Transliteration
Ara`aita manit takhaza ilaahahoo hawaahu afa anta takoonu `alaihi wakeelaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ndax gisuloo ka jàppe bakkanam mu di yàllaam ? Moo ndax dangay doon wéeruwaayam ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 41-45 — Al-Furqan
41وَإِذَا رَأَوْكَ إِن يَتَّخِذُونَكَ إِلَّا هُزُوًا أَهَٰذَا الَّذِي بَعَثَ اللَّهُ رَسُولًا
Bu ñu la gisee dañu lay téjji naan : “Ndax kii la Yàlla yónni ?
42إِن كَادَ لَيُضِلُّنَا عَنْ آلِهَتِنَا لَوْلَا أَن صَبَرْنَا عَلَيْهَا ۚ وَسَوْفَ يَعْلَمُونَ حِينَ يَرَوْنَ الْعَذَابَ مَنْ أَضَلُّ سَبِيلًا
Bu nu muñul woon, danañu xaw a féewaleek sunu yàlla jii ! ”. Waaye danañu xam [Bis bu ñu gisee mbugal ma], ana kan moo réere yoon wu jub wa.
43أَرَأَيْتَ مَنِ اتَّخَذَ إِلَٰهَهُ هَوَاهُ أَفَأَنتَ تَكُونُ عَلَيْهِ وَكِيلًا
Ndax gisuloo ka jàppe bakkanam mu di yàllaam ? Moo ndax dangay doon wéeruwaayam ?
44أَمْ تَحْسَبُ أَنَّ أَكْثَرَهُمْ يَسْمَعُونَ أَوْ يَعْقِلُونَ ۚ إِنْ هُمْ إِلَّا كَالْأَنْعَامِ ۖ بَلْ هُمْ أَضَلُّ سَبِيلًا
Walla dangaa jàpp ne li ëpp ci ñoom dañuy dégg di xam ? Ñoom kay ñook mala yi ñoo yem. Walla sax ñoo gën a sànku.
45أَلَمْ تَرَ إِلَىٰ رَبِّكَ كَيْفَ مَدَّ الظِّلَّ وَلَوْ شَاءَ لَجَعَلَهُ سَاكِنًا ثُمَّ جَعَلْنَا الشَّمْسَ عَلَيْهِ دَلِيلًا
Xanaa gisoo ni sa Boroom tàllale ker [takkander] ? Bu ko sooboon, Mu def ko mu di lu sax. Ba noppi def Nanu jant bi muy firnde,
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
43Aaya
Tekki — Al-Furqan 43
Simoore Al-Furqan Aaya 43 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax gisuloo ka jàppe bakkanam mu di yàllaam ? Moo…Simoore Aaya 43/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 41–45. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








