Al-Furqan · 50/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
وَلَقَدْ صَرَّفْنَاهُ بَيْنَهُمْ لِيَذَّكَّرُوا فَأَبَىٰ أَكْثَرُ النَّاسِ إِلَّا كُفُورًا ۝٥٠
Wa laqad sarrafnaahu bainahum li yazzakkaroo fa abaaa aksarun naasi illaa kufooraa
📖 Tekkim Wolof
Tasaare Nanu ko ci seen diggante ngir ñu fàttalikoo ca. Li ëpp ci nit ñi lànk di ay yéefar.

🎧 Dégg


📜 Aaya 48-52 — Simoore Al-Furqan

48وَهُوَ الَّذِي أَرْسَلَ الرِّيَاحَ بُشْرًا بَيْنَ يَدَيْ رَحْمَتِهِ ۚ وَأَنزَلْنَا مِنَ السَّمَاءِ مَاءً طَهُورًا
Moom moo yebal ngelaw muy bégal ci yërmaandey Yàlla. Te wàcce Nanu ci asamaan si ndox mu laab,
49لِّنُحْيِيَ بِهِ بَلْدَةً مَّيْتًا وَنُسْقِيَهُ مِمَّا خَلَقْنَا أَنْعَامًا وَأَنَاسِيَّ كَثِيرًا
ngir Nu dundalaat ci dëkk bu dee woon, màndal ci ña Nu bind ci mala ak nit ñu bari.
50وَلَقَدْ صَرَّفْنَاهُ بَيْنَهُمْ لِيَذَّكَّرُوا فَأَبَىٰ أَكْثَرُ النَّاسِ إِلَّا كُفُورًا
Tasaare Nanu ko ci seen diggante ngir ñu fàttalikoo ca. Li ëpp ci nit ñi lànk di ay yéefar.
51وَلَوْ شِئْنَا لَبَعَثْنَا فِي كُلِّ قَرْيَةٍ نَّذِيرًا
Bu Nu sooboon, dëkk bu nekk Dananu fa yebal ab xuppekat.
52فَلَا تُطِعِ الْكَافِرِينَ وَجَاهِدْهُم بِهِ جِهَادًا كَبِيرًا
Bul topp ñiy weddi Alxuraan ; te nanga xeex ak ñoom xeex bu rëy.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
50Aaya

Tekki — Al-Furqan 50

Simoore Al-Furqan Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Tasaare Nanu ko ci seen diggante ngir ñu fàttalikoo ca.…

Simoore Aaya 50/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers