Ash-Shu'ara · 196/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَإِنَّهُ لَفِي زُبُرِ الْأَوَّلِينَ ۝١٩٦
Wa innahoo lafee Zuburil awwaleen
📖 Tekkim Wolof
Te nekkoon na ca biir Téerey Yonent yu njëkk ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 194-198 — Simoore Ash-Shu'ara

194عَلَىٰ قَلْبِكَ لِتَكُونَ مِنَ الْمُنذِرِينَ
def ko ci sa biir xol [yaw Muhammad] ngir nga bokk ca xuppekat ya,
195بِلِسَانٍ عَرَبِيٍّ مُّبِينٍ
ci làmmeñu araab bu leer nàññ.
196وَإِنَّهُ لَفِي زُبُرِ الْأَوَّلِينَ
Te nekkoon na ca biir Téerey Yonent yu njëkk ya.
197أَوَلَمْ يَكُن لَّهُمْ آيَةً أَن يَعْلَمَهُ عُلَمَاءُ بَنِي إِسْرَائِيلَ
Ndax amuñu woon ay kéemaan yu taxoon boroom xam-xami giir Banii-Israayiila xamoon ko ?
198وَلَوْ نَزَّلْنَاهُ عَلَىٰ بَعْضِ الْأَعْجَمِينَ
Su Nu ko wàcce woon ci ku dul ab araab,
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
196Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 196

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 196 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te nekkoon na ca biir Téerey Yonent yu njëkk ya.

Simoore Aaya 196/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 194–198. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers