Ash-Shu'ara · 202/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
فَيَأْتِيَهُم بَغْتَةً وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ ۝٢٠٢
Fayaatiyahum baghtatanw wa hum laa yash`uroon
📖 Tekkim Wolof
mu dikke leen ci mbettel te ñoom bëgguñu ko;

🎧 Dégg


📜 Aaya 200-204 — Simoore Ash-Shu'ara

200كَذَٰلِكَ سَلَكْنَاهُ فِي قُلُوبِ الْمُجْرِمِينَ
Noonu it la nu dugalee jiixi-jaaxa ca biir xoli tooñkat yi ba gëmuñu ko ;
201لَا يُؤْمِنُونَ بِهِ حَتَّىٰ يَرَوُا الْعَذَابَ الْأَلِيمَ
duñu ko gëm mukk ndare ba ñu gisee mbugal mu metti ma,
202فَيَأْتِيَهُم بَغْتَةً وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
mu dikke leen ci mbettel te ñoom bëgguñu ko;
203فَيَقُولُوا هَلْ نَحْنُ مُنظَرُونَ
ñuy wax naan : “Ndax deesu yeexe sunuy mbir ? ”
204أَفَبِعَذَابِنَا يَسْتَعْجِلُونَ
Ndax dañoo yàkkamti Sunu mbugal ?
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
202Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 202

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 202 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mu dikke leen ci mbettel te ñoom bëgguñu ko;

Simoore Aaya 202/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 200–204. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers