Ash-Shu'ara · 82/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَالَّذِي أَطْمَعُ أَن يَغْفِرَ لِي خَطِيئَتِي يَوْمَ الدِّينِ ۝٨٢
Wallazeee atma`u ai yaghfira lee khateee` atee Yawmad Deen
📖 Tekkim Wolof
Mooy ki ma xemmem mu jéggal ma samay ñaawtéef bu Bis-pénc baa.

🎧 Dégg


📜 Aaya 80-84 — Simoore Ash-Shu'ara

80وَإِذَا مَرِضْتُ فَهُوَ يَشْفِينِ
su ma woppee, Mu faj ma,
81وَالَّذِي يُمِيتُنِي ثُمَّ يُحْيِينِ
Moo may rey, di ma dundal,
82وَالَّذِي أَطْمَعُ أَن يَغْفِرَ لِي خَطِيئَتِي يَوْمَ الدِّينِ
Mooy ki ma xemmem mu jéggal ma samay ñaawtéef bu Bis-pénc baa.
83رَبِّ هَبْ لِي حُكْمًا وَأَلْحِقْنِي بِالصَّالِحِينَ
Yaw sama Boroom, may ma xam-xam te def ma joti ca gaa ñu baax ña ;
84وَاجْعَل لِّي لِسَانَ صِدْقٍ فِي الْآخِرِينَ
defal ma am làmmiñ wu dëggu;
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
82Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 82

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 82 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy ki ma xemmem mu jéggal ma samay ñaawtéef bu…

Simoore Aaya 82/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 80–84. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers