Ash-Shu'ara · 81/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
وَالَّذِي يُمِيتُنِي ثُمَّ يُحْيِينِ ۝٨١
Wallazee yumeetunee summa yuhyeen
📖 Tekkim Wolof
Moo may rey, di ma dundal,

🎧 Dégg


📜 Aaya 79-83 — Simoore Ash-Shu'ara

79وَالَّذِي هُوَ يُطْعِمُنِي وَيَسْقِينِ
Mooy ki may leel di ma nàndal ;
80وَإِذَا مَرِضْتُ فَهُوَ يَشْفِينِ
su ma woppee, Mu faj ma,
81وَالَّذِي يُمِيتُنِي ثُمَّ يُحْيِينِ
Moo may rey, di ma dundal,
82وَالَّذِي أَطْمَعُ أَن يَغْفِرَ لِي خَطِيئَتِي يَوْمَ الدِّينِ
Mooy ki ma xemmem mu jéggal ma samay ñaawtéef bu Bis-pénc baa.
83رَبِّ هَبْ لِي حُكْمًا وَأَلْحِقْنِي بِالصَّالِحِينَ
Yaw sama Boroom, may ma xam-xam te def ma joti ca gaa ñu baax ña ;
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
81Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 81

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 81 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo may rey, di ma dundal,

Simoore Aaya 81/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 79–83. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers