An-Naml · 10/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
وَأَلْقِ عَصَاكَ ۚ فَلَمَّا رَآهَا تَهْتَزُّ كَأَنَّهَا جَانٌّ وَلَّىٰ مُدْبِرًا وَلَمْ يُعَقِّبْ ۚ يَا مُوسَىٰ لَا تَخَفْ إِنِّي لَا يَخَافُ لَدَيَّ الْمُرْسَلُونَ ۝١٠
Wa alqi `asaak; falammmaa ra aahaa tahtazzu ka annahaa jaaannunw wallaa mudbiranw wa lam yu`aqqib; yaa Moosaa laa takhaf innee laa yakhaafu ladaiyal mursaloon
📖 Tekkim Wolof
Te : “Nanga sànni sa yet wi”. Ba mu ko gisee muy yëngantu mel ni jaan, mu tiit bëgg a daw. “Éy yaw Muusaa. Bul ragal, Yonent yi duñu ragal ci sama wet.
🎧 Dégg

📜 Aaya 8-12 — An-Naml

8فَلَمَّا جَاءَهَا نُودِيَ أَن بُورِكَ مَن فِي النَّارِ وَمَنْ حَوْلَهَا وَسُبْحَانَ اللَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Ba mu fa eggee, mu am lu ko woo ne ko. - barkel nañu Ki nekk ci safara si ak ñépp ñi ko wër, tudd naa sellug Yàlla miy Boroom àddina si.
9يَا مُوسَىٰ إِنَّهُ أَنَا اللَّهُ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
"Yaw Muusaa, yégal ne Maay Yàlla, Boroom kàttan, di Ku xereñ ki”.
10وَأَلْقِ عَصَاكَ ۚ فَلَمَّا رَآهَا تَهْتَزُّ كَأَنَّهَا جَانٌّ وَلَّىٰ مُدْبِرًا وَلَمْ يُعَقِّبْ ۚ يَا مُوسَىٰ لَا تَخَفْ إِنِّي لَا يَخَافُ لَدَيَّ الْمُرْسَلُونَ
Te : “Nanga sànni sa yet wi”. Ba mu ko gisee muy yëngantu mel ni jaan, mu tiit bëgg a daw. “Éy yaw Muusaa. Bul ragal, Yonent yi duñu ragal ci sama wet.
11إِلَّا مَن ظَلَمَ ثُمَّ بَدَّلَ حُسْنًا بَعْدَ سُوءٍ فَإِنِّي غَفُورٌ رَّحِيمٌ
u dul kuy tooñ te ginnaaw ba mu soppi ñaawtéef ak lu rafet... naka Man Jéggalaakoon laa, Jaglewaakoon laa”.
12وَأَدْخِلْ يَدَكَ فِي جَيْبِكَ تَخْرُجْ بَيْضَاءَ مِنْ غَيْرِ سُوءٍ ۖ فِي تِسْعِ آيَاتٍ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَقَوْمِهِ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ
Sóobal sa loxo ci sa mbubbu. Dana génn weex tàll - muy benn ci juróom-ñeenti kéemaan yi jëm ca Firawna ak u nitam, ñoom ay saay-saay lañu woon”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — An-Naml 10

Simoore An-Naml Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te : “Nanga sànni sa yet wi”. Ba mu ko…

Simoore Aaya 10/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers