An-Naml · 9/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
يَا مُوسَىٰ إِنَّهُ أَنَا اللَّهُ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ ۝٩
Yaa Moosaaa innahooo Anal laahul `Azeezul Hakeem
📖 Tekkim Wolof
"Yaw Muusaa, yégal ne Maay Yàlla, Boroom kàttan, di Ku xereñ ki”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 7-11 — Simoore An-Naml

7إِذْ قَالَ مُوسَىٰ لِأَهْلِهِ إِنِّي آنَسْتُ نَارًا سَآتِيكُم مِّنْهَا بِخَبَرٍ أَوْ آتِيكُم بِشِهَابٍ قَبَسٍ لَّعَلَّكُمْ تَصْطَلُونَ
(Fàttalikul) ba Muusaa waxee njabootam ne leen : "Séen naa aw safar ; xaarleen ma, danaa leen fa jëlale xibaar, walla ay xal yu ngeen jaaroo ".
8فَلَمَّا جَاءَهَا نُودِيَ أَن بُورِكَ مَن فِي النَّارِ وَمَنْ حَوْلَهَا وَسُبْحَانَ اللَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Ba mu fa eggee, mu am lu ko woo ne ko. - barkel nañu Ki nekk ci safara si ak ñépp ñi ko wër, tudd naa sellug Yàlla miy Boroom àddina si.
9يَا مُوسَىٰ إِنَّهُ أَنَا اللَّهُ الْعَزِيزُ الْحَكِيمُ
"Yaw Muusaa, yégal ne Maay Yàlla, Boroom kàttan, di Ku xereñ ki”.
10وَأَلْقِ عَصَاكَ ۚ فَلَمَّا رَآهَا تَهْتَزُّ كَأَنَّهَا جَانٌّ وَلَّىٰ مُدْبِرًا وَلَمْ يُعَقِّبْ ۚ يَا مُوسَىٰ لَا تَخَفْ إِنِّي لَا يَخَافُ لَدَيَّ الْمُرْسَلُونَ
Te : “Nanga sànni sa yet wi”. Ba mu ko gisee muy yëngantu mel ni jaan, mu tiit bëgg a daw. “Éy yaw Muusaa. Bul ragal, Yonent yi duñu ragal ci sama wet.
11إِلَّا مَن ظَلَمَ ثُمَّ بَدَّلَ حُسْنًا بَعْدَ سُوءٍ فَإِنِّي غَفُورٌ رَّحِيمٌ
u dul kuy tooñ te ginnaaw ba mu soppi ñaawtéef ak lu rafet... naka Man Jéggalaakoon laa, Jaglewaakoon laa”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — An-Naml 9

Simoore An-Naml Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : "Yaw Muusaa, yégal ne Maay Yàlla, Boroom kàttan, di Ku…

Simoore Aaya 9/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers