An-Naml · 47/93
Tekki Waxtaan — An-Naml
قَالُوا اطَّيَّرْنَا بِكَ وَبِمَن مَّعَكَ ۚ قَالَ طَائِرُكُمْ عِندَ اللَّهِ ۖ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ تُفْتَنُونَ ٤٧
Transliteration
Qaalut taiyarnaa bika wa bimam ma`ak; qaala taaa`irukum `indal laahi bal antum qawmun tuftanoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ñu ne ko : “Gaafal nanu la yaak ña nga àndal.”. Mu ne leen : “Kon dey cig sànje ngeen di sax ndax li ngeen di gaafal moo nekk fa Yàlla.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 45-49 — An-Naml
45وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا إِلَىٰ ثَمُودَ أَخَاهُمْ صَالِحًا أَنِ اعْبُدُوا اللَّهَ فَإِذَا هُمْ فَرِيقَانِ يَخْتَصِمُونَ
Yónnee woon Nanu ca Samuuda seen mbokk Saaliwu. Mu ne leen : “Jaamuleen Yàlla”. Ndekete yoo dañoo séddalikoo ñaari kurél di xulloo rekk.
46قَالَ يَا قَوْمِ لِمَ تَسْتَعْجِلُونَ بِالسَّيِّئَةِ قَبْلَ الْحَسَنَةِ ۖ لَوْلَا تَسْتَغْفِرُونَ اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Mu ne leen : "Éy samaw nit, lu tax ngeen di gën a yàkkamti lu bon ci lu baax ? Céy bu ngeen jéggalu woon Yàlla ? Kon xéy-na Mu yërëm leen.
47قَالُوا اطَّيَّرْنَا بِكَ وَبِمَن مَّعَكَ ۚ قَالَ طَائِرُكُمْ عِندَ اللَّهِ ۖ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ تُفْتَنُونَ
Ñu ne ko : “Gaafal nanu la yaak ña nga àndal.”. Mu ne leen : “Kon dey cig sànje ngeen di sax ndax li ngeen di gaafal moo nekk fa Yàlla.
48وَكَانَ فِي الْمَدِينَةِ تِسْعَةُ رَهْطٍ يُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ وَلَا يُصْلِحُونَ
Mu amoon kurél bu nekkoon ca dëkk ba di juróom-ñeenti nit, daan yàq rekk te daawuñu defar.
49قَالُوا تَقَاسَمُوا بِاللَّهِ لَنُبَيِّتَنَّهُ وَأَهْلَهُ ثُمَّ لَنَقُولَنَّ لِوَلِيِّهِ مَا شَهِدْنَا مَهْلِكَ أَهْلِهِ وَإِنَّا لَصَادِقُونَ
Ñu wax ne : “Nanu waatoo ci Yàlla rey ko mook njabootam. Bu ñu xëyee ba ñay dese mbir ma laaj nu, nu tontu ne : “Nun kat teewewunu woon seenug rey”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
47Aaya
Tekki — An-Naml 47
Simoore An-Naml Aaya 47 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu ne ko : “Gaafal nanu la yaak ña nga…Simoore Aaya 47/93 — An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naml Dégg, An-Naml Tekki, An-Naml mp3, An-Naml pdf. Aaya 45–49. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








