An-Naml · 48/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
وَكَانَ فِي الْمَدِينَةِ تِسْعَةُ رَهْطٍ يُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ وَلَا يُصْلِحُونَ ۝٤٨
Wa kaana fil madeenati tis`atu rahtiny yufsidoona fil ardi wa laa yuslihoon
📖 Tekkim Wolof
Mu amoon kurél bu nekkoon ca dëkk ba di juróom-ñeenti nit, daan yàq rekk te daawuñu defar.

🎧 Dégg


📜 Aaya 46-50 — Simoore An-Naml

46قَالَ يَا قَوْمِ لِمَ تَسْتَعْجِلُونَ بِالسَّيِّئَةِ قَبْلَ الْحَسَنَةِ ۖ لَوْلَا تَسْتَغْفِرُونَ اللَّهَ لَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Mu ne leen : "Éy samaw nit, lu tax ngeen di gën a yàkkamti lu bon ci lu baax ? Céy bu ngeen jéggalu woon Yàlla ? Kon xéy-na Mu yërëm leen.
47قَالُوا اطَّيَّرْنَا بِكَ وَبِمَن مَّعَكَ ۚ قَالَ طَائِرُكُمْ عِندَ اللَّهِ ۖ بَلْ أَنتُمْ قَوْمٌ تُفْتَنُونَ
Ñu ne ko : “Gaafal nanu la yaak ña nga àndal.”. Mu ne leen : “Kon dey cig sànje ngeen di sax ndax li ngeen di gaafal moo nekk fa Yàlla.
48وَكَانَ فِي الْمَدِينَةِ تِسْعَةُ رَهْطٍ يُفْسِدُونَ فِي الْأَرْضِ وَلَا يُصْلِحُونَ
Mu amoon kurél bu nekkoon ca dëkk ba di juróom-ñeenti nit, daan yàq rekk te daawuñu defar.
49قَالُوا تَقَاسَمُوا بِاللَّهِ لَنُبَيِّتَنَّهُ وَأَهْلَهُ ثُمَّ لَنَقُولَنَّ لِوَلِيِّهِ مَا شَهِدْنَا مَهْلِكَ أَهْلِهِ وَإِنَّا لَصَادِقُونَ
Ñu wax ne : “Nanu waatoo ci Yàlla rey ko mook njabootam. Bu ñu xëyee ba ñay dese mbir ma laaj nu, nu tontu ne : “Nun kat teewewunu woon seenug rey”.
50وَمَكَرُوا مَكْرًا وَمَكَرْنَا مَكْرًا وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Ñangay fexe am pexe, Nun it Noo ngi fexe am pexe te ñoom yéguñu ko.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — An-Naml 48

Simoore An-Naml Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu amoon kurél bu nekkoon ca dëkk ba di juróom-ñeenti…

Simoore Aaya 48/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers