An-Naml · 91/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
إِنَّمَا أُمِرْتُ أَنْ أَعْبُدَ رَبَّ هَٰذِهِ الْبَلْدَةِ الَّذِي حَرَّمَهَا وَلَهُ كُلُّ شَيْءٍ ۖ وَأُمِرْتُ أَنْ أَكُونَ مِنَ الْمُسْلِمِينَ ۝٩١
Innamaaa umirtu an a`buda Rabba haazihil baldatil lazee harramahaa wa lahoo kullu shai`inw wa umirtu an akoona minal muslimeen
📖 Tekkim Wolof
“[Man Muhammad] daal, digaleef na ma may jaamu Boroom dëkk bii Mu wormaal, - te Moo moom lu ne - digaleef na ma it ma bokk ca jullit ña, jébbal ko sama bopp,

🎧 Dégg


📜 Aaya 89-93 — Simoore An-Naml

89مَن جَاءَ بِالْحَسَنَةِ فَلَهُ خَيْرٌ مِّنْهَا وَهُم مِّن فَزَعٍ يَوْمَئِذٍ آمِنُونَ
Moo ndax du ku indi ag yiw dana ca ame pey gu ko gën, te bu Bis-pénc baa dana mucc ci am tiit.
90وَمَن جَاءَ بِالسَّيِّئَةِ فَكُبَّتْ وُجُوهُهُمْ فِي النَّارِ هَلْ تُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Te it képp ku indig jëf ju ñaaw... dees na nargan seeni kanam ca safara. Te la ñu defoon doŋŋ la ñu leen di feye ”
91إِنَّمَا أُمِرْتُ أَنْ أَعْبُدَ رَبَّ هَٰذِهِ الْبَلْدَةِ الَّذِي حَرَّمَهَا وَلَهُ كُلُّ شَيْءٍ ۖ وَأُمِرْتُ أَنْ أَكُونَ مِنَ الْمُسْلِمِينَ
“[Man Muhammad] daal, digaleef na ma may jaamu Boroom dëkk bii Mu wormaal, - te Moo moom lu ne - digaleef na ma it ma bokk ca jullit ña, jébbal ko sama bopp,
92وَأَنْ أَتْلُوَ الْقُرْآنَ ۖ فَمَنِ اهْتَدَىٰ فَإِنَّمَا يَهْتَدِي لِنَفْسِهِ ۖ وَمَن ضَلَّ فَقُلْ إِنَّمَا أَنَا مِنَ الْمُنذِرِينَ
Ak it ma nettali Alxuraan”. Képp ku gindiku, mook boppam. Képp ku ko mën a réer..., yaw neel : “Man daal damay xuppe doŋŋ”.
93وَقُلِ الْحَمْدُ لِلَّهِ سَيُرِيكُمْ آيَاتِهِ فَتَعْرِفُونَهَا ۚ وَمَا رَبُّكَ بِغَافِلٍ عَمَّا تَعْمَلُونَ
Waxal ne : “Xeeti cant yépp ñeel na Yàlla ! Dana leen won ay kéemaan, firndeem ngeen di ko xam”. Te sa Boroom sàgganewul li ñuy def.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
91Aaya

Tekki — An-Naml 91

Simoore An-Naml Aaya 91 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “[Man Muhammad] daal, digaleef na ma may jaamu Boroom dëkk…

Simoore Aaya 91/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 89–93. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers