An-Naml · 90/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
وَمَن جَاءَ بِالسَّيِّئَةِ فَكُبَّتْ وُجُوهُهُمْ فِي النَّارِ هَلْ تُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ ۝٩٠
Wa man jaaa`a bissai yi`ati fakubbat wujoohuhum fin Naari hal tujzawna illaa maa kuntum ta`maloon
📖 Tekkim Wolof
Te it képp ku indig jëf ju ñaaw... dees na nargan seeni kanam ca safara. Te la ñu defoon doŋŋ la ñu leen di feye ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 88-92 — Simoore An-Naml

88وَتَرَى الْجِبَالَ تَحْسَبُهَا جَامِدَةً وَهِيَ تَمُرُّ مَرَّ السَّحَابِ ۚ صُنْعَ اللَّهِ الَّذِي أَتْقَنَ كُلَّ شَيْءٍ ۚ إِنَّهُ خَبِيرٌ بِمَا تَفْعَلُونَ
Ngay gis tundi doj yi foog ni dafa taxaw benn barab, te fekk na booba ñangay daw niw niir. Loolu mooy liggéeyub Yàlla. Te Mooy Xereñaakoonub mépp mbir, te Ku deñ-kumpa la ci li ngeen di def !
89مَن جَاءَ بِالْحَسَنَةِ فَلَهُ خَيْرٌ مِّنْهَا وَهُم مِّن فَزَعٍ يَوْمَئِذٍ آمِنُونَ
Moo ndax du ku indi ag yiw dana ca ame pey gu ko gën, te bu Bis-pénc baa dana mucc ci am tiit.
90وَمَن جَاءَ بِالسَّيِّئَةِ فَكُبَّتْ وُجُوهُهُمْ فِي النَّارِ هَلْ تُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Te it képp ku indig jëf ju ñaaw... dees na nargan seeni kanam ca safara. Te la ñu defoon doŋŋ la ñu leen di feye ”
91إِنَّمَا أُمِرْتُ أَنْ أَعْبُدَ رَبَّ هَٰذِهِ الْبَلْدَةِ الَّذِي حَرَّمَهَا وَلَهُ كُلُّ شَيْءٍ ۖ وَأُمِرْتُ أَنْ أَكُونَ مِنَ الْمُسْلِمِينَ
“[Man Muhammad] daal, digaleef na ma may jaamu Boroom dëkk bii Mu wormaal, - te Moo moom lu ne - digaleef na ma it ma bokk ca jullit ña, jébbal ko sama bopp,
92وَأَنْ أَتْلُوَ الْقُرْآنَ ۖ فَمَنِ اهْتَدَىٰ فَإِنَّمَا يَهْتَدِي لِنَفْسِهِ ۖ وَمَن ضَلَّ فَقُلْ إِنَّمَا أَنَا مِنَ الْمُنذِرِينَ
Ak it ma nettali Alxuraan”. Képp ku gindiku, mook boppam. Képp ku ko mën a réer..., yaw neel : “Man daal damay xuppe doŋŋ”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
90Aaya

Tekki — An-Naml 90

Simoore An-Naml Aaya 90 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te it képp ku indig jëf ju ñaaw... dees na…

Simoore Aaya 90/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 88–92. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers