An-Naml · 93/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
وَقُلِ الْحَمْدُ لِلَّهِ سَيُرِيكُمْ آيَاتِهِ فَتَعْرِفُونَهَا ۚ وَمَا رَبُّكَ بِغَافِلٍ عَمَّا تَعْمَلُونَ ۝٩٣
Wa qulil hamdu lillaahi sa yureekum Aayaatihee fata`ri foonahaa; wa maa Rabbuka bighaaflin `ammaa ta`maloon
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “Xeeti cant yépp ñeel na Yàlla ! Dana leen won ay kéemaan, firndeem ngeen di ko xam”. Te sa Boroom sàgganewul li ñuy def.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 91-93 — Simoore An-Naml

91إِنَّمَا أُمِرْتُ أَنْ أَعْبُدَ رَبَّ هَٰذِهِ الْبَلْدَةِ الَّذِي حَرَّمَهَا وَلَهُ كُلُّ شَيْءٍ ۖ وَأُمِرْتُ أَنْ أَكُونَ مِنَ الْمُسْلِمِينَ
“[Man Muhammad] daal, digaleef na ma may jaamu Boroom dëkk bii Mu wormaal, - te Moo moom lu ne - digaleef na ma it ma bokk ca jullit ña, jébbal ko sama bopp,
92وَأَنْ أَتْلُوَ الْقُرْآنَ ۖ فَمَنِ اهْتَدَىٰ فَإِنَّمَا يَهْتَدِي لِنَفْسِهِ ۖ وَمَن ضَلَّ فَقُلْ إِنَّمَا أَنَا مِنَ الْمُنذِرِينَ
Ak it ma nettali Alxuraan”. Képp ku gindiku, mook boppam. Képp ku ko mën a réer..., yaw neel : “Man daal damay xuppe doŋŋ”.
93وَقُلِ الْحَمْدُ لِلَّهِ سَيُرِيكُمْ آيَاتِهِ فَتَعْرِفُونَهَا ۚ وَمَا رَبُّكَ بِغَافِلٍ عَمَّا تَعْمَلُونَ
Waxal ne : “Xeeti cant yépp ñeel na Yàlla ! Dana leen won ay kéemaan, firndeem ngeen di ko xam”. Te sa Boroom sàgganewul li ñuy def.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
93Aaya

Tekki — An-Naml 93

Simoore An-Naml Aaya 93 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “Xeeti cant yépp ñeel na Yàlla !…

Simoore Aaya 93/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 91–93. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers