Al-Qasas · 35/88
Tekki Waxtaan — Al-Qasas
قَالَ سَنَشُدُّ عَضُدَكَ بِأَخِيكَ وَنَجْعَلُ لَكُمَا سُلْطَانًا فَلَا يَصِلُونَ إِلَيْكُمَا ۚ بِآيَاتِنَا أَنتُمَا وَمَنِ اتَّبَعَكُمَا الْغَالِبُونَ ۝٣٥
Qaala sanashuddu `adudaka bi akheeka wa naj`alu lakumaa sultaanan falaa yasiloona ilaikumaa; bi Aayaatinaa antumaa wa manit taba`akumal ghaaliboon
📖 Tekkim Wolof
[Yàlla] ne ko : “Dananu dëgërale sa përëg ci sa mbokk mi, Dananu leen defal ay firnde [doole joo xam ne dana mën a agsi ci yéen] ak Sunuy kéemaan. Yéen ñaar ñépp ak ña leen topp yéen ay not.
🎧 Dégg

📜 Aaya 33-37 — Al-Qasas

33قَالَ رَبِّ إِنِّي قَتَلْتُ مِنْهُمْ نَفْسًا فَأَخَافُ أَن يَقْتُلُونِ
[Muusaa wax na ne] : “Rey naa ci ñoom bakkan te ragal naa ñu rey ma.
34وَأَخِي هَارُونُ هُوَ أَفْصَحُ مِنِّي لِسَانًا فَأَرْسِلْهُ مَعِيَ رِدْءًا يُصَدِّقُنِي ۖ إِنِّي أَخَافُ أَن يُكَذِّبُونِ
Te Aaruuna moo ma gën a leer i wax. Yebal ko mu ànd ak man di ma ruqandi, di ma dëggal : man daal ragal naa ñu jàppe ma fenkat”.
35قَالَ سَنَشُدُّ عَضُدَكَ بِأَخِيكَ وَنَجْعَلُ لَكُمَا سُلْطَانًا فَلَا يَصِلُونَ إِلَيْكُمَا ۚ بِآيَاتِنَا أَنتُمَا وَمَنِ اتَّبَعَكُمَا الْغَالِبُونَ
[Yàlla] ne ko : “Dananu dëgërale sa përëg ci sa mbokk mi, Dananu leen defal ay firnde [doole joo xam ne dana mën a agsi ci yéen] ak Sunuy kéemaan. Yéen ñaar ñépp ak ña leen topp yéen ay not.
36فَلَمَّا جَاءَهُم مُّوسَىٰ بِآيَاتِنَا بَيِّنَاتٍ قَالُوا مَا هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ مُّفْتَرًى وَمَا سَمِعْنَا بِهَٰذَا فِي آبَائِنَا الْأَوَّلِينَ
Ba leen Muusaa dikkee, indil leen Sunuy kàddu yu leer ñàññ, wax nañu ne : “Lii daal du lenn du dul ag njibar gu ñu sos, te sax nun lii mësunu leen woon a dégg ca sunuy maam”.
37وَقَالَ مُوسَىٰ رَبِّي أَعْلَمُ بِمَن جَاءَ بِالْهُدَىٰ مِنْ عِندِهِ وَمَن تَكُونُ لَهُ عَاقِبَةُ الدَّارِ ۖ إِنَّهُ لَا يُفْلِحُ الظَّالِمُونَ
Muusaa ne leen : “Sama Boroom moo gën a xam ana kaan moo indi dëgg te jóge fa Moom, ak kan mooy ëppug mujj. Tooñkat ya duñu texe de”.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — Al-Qasas 35

Simoore Al-Qasas Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Yàlla] ne ko : “Dananu dëgërale sa përëg ci sa…

Simoore Aaya 35/88 — Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qasas Dégg, Al-Qasas Tekki, Al-Qasas mp3, Al-Qasas pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers