Al-Qasas · 88/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
وَلَا تَدْعُ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ ۘ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۚ كُلُّ شَيْءٍ هَالِكٌ إِلَّا وَجْهَهُ ۚ لَهُ الْحُكْمُ وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ ۝٨٨
Wa laa tad`u ma`al laahi ilaahan aakhar; laaa ilaaha illaa Hoo; kullu shai`in haalikun illaa Wajhah; lahul hukkmu wa ilaihi turja`oon
📖 Tekkim Wolof
Bul woo jeneen yàlla di ko booleek Yàlla. Amul jenn yàlla ju dul Moom. Lu nekk a faagaagalu ba mu des Moom. [Yàlla] mooy boroom àtte yi te ca Moom ngeen di dellu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 86-88 — Simoore Al-Qasas

86وَمَا كُنتَ تَرْجُو أَن يُلْقَىٰ إِلَيْكَ الْكِتَابُ إِلَّا رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۖ فَلَا تَكُونَنَّ ظَهِيرًا لِّلْكَافِرِينَ
Musuloo yaakaar ne dees na la jox Téere ba. Lu dul ne yërmaande ju bawoo ca sa Boroom. Te bul dimbali mukk yéefar yi ;
87وَلَا يَصُدُّنَّكَ عَنْ آيَاتِ اللَّهِ بَعْدَ إِذْ أُنزِلَتْ إِلَيْكَ ۖ وَادْعُ إِلَىٰ رَبِّكَ ۖ وَلَا تَكُونَنَّ مِنَ الْمُشْرِكِينَ
te it buñu la fàbbi mukk ci kàdduy Yàlla ginnaaw ba Nu ko wàccee ci yaw. Nangay woote jëme ci sa Boroom te bul bokk ca way-bokkaale ña.
88وَلَا تَدْعُ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ ۘ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ ۚ كُلُّ شَيْءٍ هَالِكٌ إِلَّا وَجْهَهُ ۚ لَهُ الْحُكْمُ وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
Bul woo jeneen yàlla di ko booleek Yàlla. Amul jenn yàlla ju dul Moom. Lu nekk a faagaagalu ba mu des Moom. [Yàlla] mooy boroom àtte yi te ca Moom ngeen di dellu.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
88Aaya

Tekki — Al-Qasas 88

Simoore Al-Qasas Aaya 88 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bul woo jeneen yàlla di ko booleek Yàlla. Amul jenn…

Simoore Aaya 88/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 86–88. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers