Aali Imran · 159/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
فَبِمَا رَحْمَةٍ مِّنَ اللَّهِ لِنتَ لَهُمْ ۖ وَلَوْ كُنتَ فَظًّا غَلِيظَ الْقَلْبِ لَانفَضُّوا مِنْ حَوْلِكَ ۖ فَاعْفُ عَنْهُمْ وَاسْتَغْفِرْ لَهُمْ وَشَاوِرْهُمْ فِي الْأَمْرِ ۖ فَإِذَا عَزَمْتَ فَتَوَكَّلْ عَلَى اللَّهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ يُحِبُّ الْمُتَوَكِّلِينَ ۝١٥٩
Fabimaa rahmatim minal laahi linta lahum wa law kunta fazzan ghaleezal qalbi lanfaddoo min hawlika fafu `anhum wastaghfir lahum wa shaawirhum fil amri fa izaa `azamta fatawakkal `alal laah; innallaaha yuhibbul mutawak kileen
📖 Tekkim Wolof
Ci sa yërmaandeey Boroom nga nooyee ci ñoom ! Boo nekkoon ku ñaaw jikko walla ku xat xol, ñu ne wuseet bàyyi la. Baal-leen te jéggal-leen. Te deel diisook ñoom ci mbir yi ; waaye boo dogoo [ci wéyal dara], nanga wéeru ci sa Boroom, Yàlla dana safoo ñay wéeru ci Moom [yaw Muhammad].
🎧 Dégg

📜 Aaya 157-161 — Aali Imran

157وَلَئِن قُتِلْتُمْ فِي سَبِيلِ اللَّهِ أَوْ مُتُّمْ لَمَغْفِرَةٌ مِّنَ اللَّهِ وَرَحْمَةٌ خَيْرٌ مِّمَّا يَجْمَعُونَ
Bu ñu leen reyee ci yoonu Yàlla walla ngeen dee, ca dëgg-dëgg jéggalu ga, Yàlla ak yërmandeem moo gën fuuf li ngeen di dajale.
158وَلَئِن مُّتُّمْ أَوْ قُتِلْتُمْ لَإِلَى اللَّهِ تُحْشَرُونَ
Ngeen dee walla ñu rey leen, dees na leen pang [gur-gur] jëme ca Yàlla.
159فَبِمَا رَحْمَةٍ مِّنَ اللَّهِ لِنتَ لَهُمْ ۖ وَلَوْ كُنتَ فَظًّا غَلِيظَ الْقَلْبِ لَانفَضُّوا مِنْ حَوْلِكَ ۖ فَاعْفُ عَنْهُمْ وَاسْتَغْفِرْ لَهُمْ وَشَاوِرْهُمْ فِي الْأَمْرِ ۖ فَإِذَا عَزَمْتَ فَتَوَكَّلْ عَلَى اللَّهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ يُحِبُّ الْمُتَوَكِّلِينَ
Ci sa yërmaandeey Boroom nga nooyee ci ñoom ! Boo nekkoon ku ñaaw jikko walla ku xat xol, ñu ne wuseet bàyyi la. Baal-leen te jéggal-leen. Te deel diisook ñoom ci mbir yi ; waaye boo dogoo [ci wéyal dara], nanga wéeru ci sa Boroom, Yàlla dana safoo ñay wéeru ci Moom [yaw Muhammad].
160إِن يَنصُرْكُمُ اللَّهُ فَلَا غَالِبَ لَكُمْ ۖ وَإِن يَخْذُلْكُمْ فَمَن ذَا الَّذِي يَنصُرُكُم مِّن بَعْدِهِ ۗ وَعَلَى اللَّهِ فَلْيَتَوَكَّلِ الْمُؤْمِنُونَ
Bu leen Yàlla dimbalee, kenn duleen mën a not. Bu leen bàyyee, kan moo leen di mën a dimbali ? [Amul]. Ñi gëm, nañu wéeru ci Yàlla.
161وَمَا كَانَ لِنَبِيٍّ أَن يَغُلَّ ۚ وَمَن يَغْلُلْ يَأْتِ بِمَا غَلَّ يَوْمَ الْقِيَامَةِ ۚ ثُمَّ تُوَفَّىٰ كُلُّ نَفْسٍ مَّا كَسَبَتْ وَهُمْ لَا يُظْلَمُونَ
Amul benn Yonent buy labax alali xare. Te képp ku sàcc alali xare, bu Bis-pénc baa, dana ko indi. Ku nekk door a jot la mu jëfoon ba mu mat sëkk.
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
159Aaya

Tekki — Aali Imran 159

Simoore Aali Imran Aaya 159 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ci sa yërmaandeey Boroom nga nooyee ci ñoom ! Boo…

Simoore Aaya 159/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 157–161. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers