Ar-Rum · 35/60
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rum
أَمْ أَنزَلْنَا عَلَيْهِمْ سُلْطَانًا فَهُوَ يَتَكَلَّمُ بِمَا كَانُوا بِهِ يُشْرِكُونَ ٣٥
Transliteration
Am anzalnaa `alaihim sultaanan fahuwa yatakallamu bimaa kaanoo bihee yushrikoon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Walla Danuy wàcce ci ñoom [kilifa] ab Téere buy wàqante la ñu daan bokkaale ?
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 33-37 — Simoore Ar-Rum
33وَإِذَا مَسَّ النَّاسَ ضُرٌّ دَعَوْا رَبَّهُم مُّنِيبِينَ إِلَيْهِ ثُمَّ إِذَا أَذَاقَهُم مِّنْهُ رَحْمَةً إِذَا فَرِيقٌ مِّنْهُم بِرَبِّهِمْ يُشْرِكُونَ
Bu lor ju laal nit ña amee, dañuy ñaan Yàlla di Ko woo booleek toroxlu. Waaye su leen di mosal yërmaande rekk, [nga gis] ñu delluy bokkaale,
34لِيَكْفُرُوا بِمَا آتَيْنَاهُمْ ۚ فَتَمَتَّعُوا فَسَوْفَ تَعْلَمُونَ
di fakk la Mu leen indiloon. “Bànneexuleen. Dangeen xala xam”.
35أَمْ أَنزَلْنَا عَلَيْهِمْ سُلْطَانًا فَهُوَ يَتَكَلَّمُ بِمَا كَانُوا بِهِ يُشْرِكُونَ
Walla Danuy wàcce ci ñoom [kilifa] ab Téere buy wàqante la ñu daan bokkaale ?
36وَإِذَا أَذَقْنَا النَّاسَ رَحْمَةً فَرِحُوا بِهَا ۖ وَإِن تُصِبْهُمْ سَيِّئَةٌ بِمَا قَدَّمَتْ أَيْدِيهِمْ إِذَا هُمْ يَقْنَطُونَ
Saa su Nu mosalee nit ñi yërmaande, ñu bég lool. Bu ñu defee ab garaawaale ba safaan dal leen ca, ndekete yoo dañuy yoqat.
37أَوَلَمْ يَرَوْا أَنَّ اللَّهَ يَبْسُطُ الرِّزْقَ لِمَن يَشَاءُ وَيَقْدِرُ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ لِّقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Xanaa dañoo gisul ne Yàlla Dana yaatalal ku ko soob, wërsëgam ? Dana ko xatal it. Ay kéemaan a ngi ci biir loolu ngir aw nit ñu gëm.
Ar-RumFihi Alxuraan
60Aaya
MeccanRevelation
35Aaya
Tekki — Ar-Rum 35
Simoore Ar-Rum Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Walla Danuy wàcce ci ñoom [kilifa] ab Téere buy wàqante…Simoore Aaya 35/60 — Simoore Ar-Rum الروم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rum Dégg, Simoore Ar-Rum Tekki, Simoore Ar-Rum mp3, Simoore Ar-Rum pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Ar-Rum
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Wednesday, September 30, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


