Al-Ahzab · 40/73
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ahzab
مَّا كَانَ مُحَمَّدٌ أَبَا أَحَدٍ مِّن رِّجَالِكُمْ وَلَٰكِن رَّسُولَ اللَّهِ وَخَاتَمَ النَّبِيِّينَ ۗ وَكَانَ اللَّهُ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمًا ٤٠
Transliteration
Maa kaana Muhammmadun abaaa ahadim mir rijaalikum wa laakir Rasoolal laahi wa Khaataman Nabiyyeen; wa kaanal laahu bikulli shai`in `Aleema
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Muhammad du baayub kenn ci seeni gaay, waaye ndawul Yàlla te di mujjug Yonent yi. Yàlla xam na lépp lu ne.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 38-42 — Simoore Al-Ahzab
38مَّا كَانَ عَلَى النَّبِيِّ مِنْ حَرَجٍ فِيمَا فَرَضَ اللَّهُ لَهُ ۖ سُنَّةَ اللَّهِ فِي الَّذِينَ خَلَوْا مِن قَبْلُ ۚ وَكَانَ أَمْرُ اللَّهِ قَدَرًا مَّقْدُورًا
Aayul ci Yonent bi [muy jëfandikoo] la Yàlla yoonaloon, farataal ko ca ña ko jiitu woon. Te ndigalul Yàlla luy sax la.
39الَّذِينَ يُبَلِّغُونَ رِسَالَاتِ اللَّهِ وَيَخْشَوْنَهُ وَلَا يَخْشَوْنَ أَحَدًا إِلَّا اللَّهَ ۗ وَكَفَىٰ بِاللَّهِ حَسِيبًا
Ña nga xam ne ñooy jottali bataaxali Yàlla yi te ragal Ko, te it duñu ragal keneen ku dul Moom. Ndax Yàlla doy na sëkk ci waññi [natt] jëf yi.
40مَّا كَانَ مُحَمَّدٌ أَبَا أَحَدٍ مِّن رِّجَالِكُمْ وَلَٰكِن رَّسُولَ اللَّهِ وَخَاتَمَ النَّبِيِّينَ ۗ وَكَانَ اللَّهُ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمًا
Muhammad du baayub kenn ci seeni gaay, waaye ndawul Yàlla te di mujjug Yonent yi. Yàlla xam na lépp lu ne.
41يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا اذْكُرُوا اللَّهَ ذِكْرًا كَثِيرًا
Éy yéen ñi gëm ! Nangeen di farataal, di tudd Yàlla lu bari.
42وَسَبِّحُوهُ بُكْرَةً وَأَصِيلًا
te nangeen di Ko sàbbaal suba ak ngoon.
Al-AhzabFihi Alxuraan
73Aaya
MedinanRevelation
40Aaya
Tekki — Al-Ahzab 40
Simoore Al-Ahzab Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muhammad du baayub kenn ci seeni gaay, waaye ndawul Yàlla…Simoore Aaya 40/73 — Simoore Al-Ahzab الأحزاب (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ahzab Dégg, Simoore Al-Ahzab Tekki, Simoore Al-Ahzab mp3, Simoore Al-Ahzab pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore Al-Ahzab
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Monday, September 28, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


