Ya-Sin · 49/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
مَا يَنظُرُونَ إِلَّا صَيْحَةً وَاحِدَةً تَأْخُذُهُمْ وَهُمْ يَخِصِّمُونَ ۝٤٩
Maa yanzuroona illaa saihatanw waahidatan taa khuzuhum wa hum yakhissimoon
📖 Tekkim Wolof
Xaaruñu lu dul genn yuuxu gu leen jël fekk leen ñuy xuloo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 47-51 — Simoore Ya-Sin

47وَإِذَا قِيلَ لَهُمْ أَنفِقُوا مِمَّا رَزَقَكُمُ اللَّهُ قَالَ الَّذِينَ كَفَرُوا لِلَّذِينَ آمَنُوا أَنُطْعِمُ مَن لَّوْ يَشَاءُ اللَّهُ أَطْعَمَهُ إِنْ أَنتُمْ إِلَّا فِي ضَلَالٍ مُّبِينٍ
Saa su ñu leen waxee ne : “Joxeleen ci alal ji leen Yàlla wërsëgal”, ña weddi dañuy wax ña gëm, naan leen : “Moo ndax nun danuy dundal koo xam ne bu neexoon Yàlla mu dundal ko ? Yéen daal ci ag réer gu bir ngeen nekk”.
48وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ña ngay wax naan : “Dig ba kañ lay ñëw ndegam li ngeen di wax dëgg la ? ”
49مَا يَنظُرُونَ إِلَّا صَيْحَةً وَاحِدَةً تَأْخُذُهُمْ وَهُمْ يَخِصِّمُونَ
Xaaruñu lu dul genn yuuxu gu leen jël fekk leen ñuy xuloo.
50فَلَا يَسْتَطِيعُونَ تَوْصِيَةً وَلَا إِلَىٰ أَهْلِهِمْ يَرْجِعُونَ
Duñu mën a batale, di dénkaane, mbaa ñuy mën a dellu ca seen njaboot.
51وَنُفِخَ فِي الصُّورِ فَإِذَا هُم مِّنَ الْأَجْدَاثِ إِلَىٰ رَبِّهِمْ يَنسِلُونَ
Su ñu ëfee Buftu bi, dañu naan futeet ca bàmmeel ya, dox wuti seen Boroom,
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
49Aaya

Tekki — Ya-Sin 49

Simoore Ya-Sin Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xaaruñu lu dul genn yuuxu gu leen jël fekk leen…

Simoore Aaya 49/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers