Ya-Sin · 50/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
فَلَا يَسْتَطِيعُونَ تَوْصِيَةً وَلَا إِلَىٰ أَهْلِهِمْ يَرْجِعُونَ ۝٥٠
Falaa yastatee`oona taw siyatanw-wa laaa ilaaa ahlihim yarji`oon
📖 Tekkim Wolof
Duñu mën a batale, di dénkaane, mbaa ñuy mën a dellu ca seen njaboot.

🎧 Dégg


📜 Aaya 48-52 — Ya-Sin

48وَيَقُولُونَ مَتَىٰ هَٰذَا الْوَعْدُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ña ngay wax naan : “Dig ba kañ lay ñëw ndegam li ngeen di wax dëgg la ? ”
49مَا يَنظُرُونَ إِلَّا صَيْحَةً وَاحِدَةً تَأْخُذُهُمْ وَهُمْ يَخِصِّمُونَ
Xaaruñu lu dul genn yuuxu gu leen jël fekk leen ñuy xuloo.
50فَلَا يَسْتَطِيعُونَ تَوْصِيَةً وَلَا إِلَىٰ أَهْلِهِمْ يَرْجِعُونَ
Duñu mën a batale, di dénkaane, mbaa ñuy mën a dellu ca seen njaboot.
51وَنُفِخَ فِي الصُّورِ فَإِذَا هُم مِّنَ الْأَجْدَاثِ إِلَىٰ رَبِّهِمْ يَنسِلُونَ
Su ñu ëfee Buftu bi, dañu naan futeet ca bàmmeel ya, dox wuti seen Boroom,
52قَالُوا يَا وَيْلَنَا مَن بَعَثَنَا مِن مَّرْقَدِنَا ۜ ۗ هَٰذَا مَا وَعَدَ الرَّحْمَٰنُ وَصَدَقَ الْمُرْسَلُونَ
ñuy wax naan : “Wóoy ngalla nun ! Moo ana kan moo nu yékkatee ci sunu yàndoorukaay bi ? ” Lii dey mooy la nu Yërëmaakoon bi doon dig ; kon Yonent yi waxoon nañu dëgg.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
50Aaya

Tekki — Ya-Sin 50

Simoore Ya-Sin Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Duñu mën a batale, di dénkaane, mbaa ñuy mën a…

Simoore Aaya 50/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers