Ya-Sin · 56/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
هُمْ وَأَزْوَاجُهُمْ فِي ظِلَالٍ عَلَى الْأَرَائِكِ مُتَّكِئُونَ ۝٥٦
Hum wa azwaajuhum fee zilaalin `alal araaa`iki muttaki`oon
📖 Tekkim Wolof
ñoom ak seeni soxna, ña nga ca biir kër ya, sóonu ca lal ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 54-58 — Simoore Ya-Sin

54فَالْيَوْمَ لَا تُظْلَمُ نَفْسٌ شَيْئًا وَلَا تُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Bis niki tey, deesul tooñ benn bakkan . Te deefuleen feye lu dul la ngeen daan jëf.
55إِنَّ أَصْحَابَ الْجَنَّةِ الْيَوْمَ فِي شُغُلٍ فَاكِهُونَ
Bis niki tey, waa Àjjanaa ngi ci xéewal gu mat sëkk ;
56هُمْ وَأَزْوَاجُهُمْ فِي ظِلَالٍ عَلَى الْأَرَائِكِ مُتَّكِئُونَ
ñoom ak seeni soxna, ña nga ca biir kër ya, sóonu ca lal ya.
57لَهُمْ فِيهَا فَاكِهَةٌ وَلَهُم مَّا يَدَّعُونَ
Am nañu fa ay fuytéef ak lépp lu ñuy soxla,
58سَلَامٌ قَوْلًا مِّن رَّبٍّ رَّحِيمٍ
“Jàmm rekk la ñu fay ame” ! Mu bawoo ca Boroom biy Jaglewaakoonu Yërmaandeem.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
56Aaya

Tekki — Ya-Sin 56

Simoore Ya-Sin Aaya 56 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñoom ak seeni soxna, ña nga ca biir kër ya,…

Simoore Aaya 56/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 54–58. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers