Ya-Sin · 64/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
اصْلَوْهَا الْيَوْمَ بِمَا كُنتُمْ تَكْفُرُونَ ۝٦٤
Islawhal Yawma bimaa kuntum takfuroon
📖 Tekkim Wolof
Xoyomuleen ci bis niki tey, muy [peyug li ngeen daan weddi]”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 62-66 — Ya-Sin

62وَلَقَدْ أَضَلَّ مِنكُمْ جِبِلًّا كَثِيرًا ۖ أَفَلَمْ تَكُونُوا تَعْقِلُونَ
Mu réeral ci yéen lim bu takku. Xanaa daawuleen xalaat ?
63هَٰذِهِ جَهَنَّمُ الَّتِي كُنتُمْ تُوعَدُونَ
Safara si ñu leen daan dig, mi ngi nii.
64اصْلَوْهَا الْيَوْمَ بِمَا كُنتُمْ تَكْفُرُونَ
Xoyomuleen ci bis niki tey, muy [peyug li ngeen daan weddi]”.
65الْيَوْمَ نَخْتِمُ عَلَىٰ أَفْوَاهِهِمْ وَتُكَلِّمُنَا أَيْدِيهِمْ وَتَشْهَدُ أَرْجُلُهُم بِمَا كَانُوا يَكْسِبُونَ
Bis niki tey, Dananu ŋalaab seeni gémmiñ, seen yoxo ya di wax ak Nun, seen tànk ya di seede la ñu daan fàggu.
66وَلَوْ نَشَاءُ لَطَمَسْنَا عَلَىٰ أَعْيُنِهِمْ فَاسْتَبَقُوا الصِّرَاطَ فَأَنَّىٰ يُبْصِرُونَ
Te kat, bu Nu sooboon, Dananu fatt seeni gët, bàyyi leen ñuy jëkkante ci kaw [siraat], ba xam fu ñuy giseeti ?
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
64Aaya

Tekki — Ya-Sin 64

Simoore Ya-Sin Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xoyomuleen ci bis niki tey, muy [peyug li ngeen daan…

Simoore Aaya 64/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers