Ya-Sin · 66/83
Tekki Waxtaan — Simoore Ya-Sin
وَلَوْ نَشَاءُ لَطَمَسْنَا عَلَىٰ أَعْيُنِهِمْ فَاسْتَبَقُوا الصِّرَاطَ فَأَنَّىٰ يُبْصِرُونَ ۝٦٦
Wa law nashaaa`u lata masna `alaaa aiyunihim fasta baqus-siraata fa-annaa yubsiroon
📖 Tekkim Wolof
Te kat, bu Nu sooboon, Dananu fatt seeni gët, bàyyi leen ñuy jëkkante ci kaw [siraat], ba xam fu ñuy giseeti ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 64-68 — Simoore Ya-Sin

64اصْلَوْهَا الْيَوْمَ بِمَا كُنتُمْ تَكْفُرُونَ
Xoyomuleen ci bis niki tey, muy [peyug li ngeen daan weddi]”.
65الْيَوْمَ نَخْتِمُ عَلَىٰ أَفْوَاهِهِمْ وَتُكَلِّمُنَا أَيْدِيهِمْ وَتَشْهَدُ أَرْجُلُهُم بِمَا كَانُوا يَكْسِبُونَ
Bis niki tey, Dananu ŋalaab seeni gémmiñ, seen yoxo ya di wax ak Nun, seen tànk ya di seede la ñu daan fàggu.
66وَلَوْ نَشَاءُ لَطَمَسْنَا عَلَىٰ أَعْيُنِهِمْ فَاسْتَبَقُوا الصِّرَاطَ فَأَنَّىٰ يُبْصِرُونَ
Te kat, bu Nu sooboon, Dananu fatt seeni gët, bàyyi leen ñuy jëkkante ci kaw [siraat], ba xam fu ñuy giseeti ?
67وَلَوْ نَشَاءُ لَمَسَخْنَاهُمْ عَلَىٰ مَكَانَتِهِمْ فَمَا اسْتَطَاعُوا مُضِيًّا وَلَا يَرْجِعُونَ
Bu Nu sooboon, Dananu leen rat benn barab ; dootuñu dem, duñu dikk.
68وَمَن نُّعَمِّرْهُ نُنَكِّسْهُ فِي الْخَلْقِ ۖ أَفَلَا يَعْقِلُونَ
Képp ku Ma defal aw fan wu guddi, Danaa ko màggatloo, xanaa dungeen xalaat ?
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
66Aaya

Tekki — Ya-Sin 66

Simoore Ya-Sin Aaya 66 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te kat, bu Nu sooboon, Dananu fatt seeni gët, bàyyi…

Simoore Aaya 66/83 — Simoore Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ya-Sin Dégg, Simoore Ya-Sin Tekki, Simoore Ya-Sin mp3, Simoore Ya-Sin pdf. Aaya 64–68. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers