Ya-Sin · 77/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
أَوَلَمْ يَرَ الْإِنسَانُ أَنَّا خَلَقْنَاهُ مِن نُّطْفَةٍ فَإِذَا هُوَ خَصِيمٌ مُّبِينٌ ۝٧٧
Awalam yaral insaanu annaa khalaqnaahu min nutfatin fa-izaa huwa khaseemum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Xanaa nit dafa gisul ne Nun Yàlla noo ko bind ci lumbub deret ? Deketeyoo moom ab xulóowaakoon la bu di ab pànk !

🎧 Dégg


📜 Aaya 75-79 — Ya-Sin

75لَا يَسْتَطِيعُونَ نَصْرَهُمْ وَهُمْ لَهُمْ جُندٌ مُّحْضَرُونَ
Yooyu duleen mën a dimbali, dañuy sax faf di jàmmaarlook ñoom [di xare].
76فَلَا يَحْزُنكَ قَوْلُهُمْ ۘ إِنَّا نَعْلَمُ مَا يُسِرُّونَ وَمَا يُعْلِنُونَ
Bula seeni wax jaaxal ! Nun xam Nanu li ñuy yelu ak li ñuy biral.
77أَوَلَمْ يَرَ الْإِنسَانُ أَنَّا خَلَقْنَاهُ مِن نُّطْفَةٍ فَإِذَا هُوَ خَصِيمٌ مُّبِينٌ
Xanaa nit dafa gisul ne Nun Yàlla noo ko bind ci lumbub deret ? Deketeyoo moom ab xulóowaakoon la bu di ab pànk !
78وَضَرَبَ لَنَا مَثَلًا وَنَسِيَ خَلْقَهُ ۖ قَالَ مَن يُحْيِي الْعِظَامَ وَهِيَ رَمِيمٌ
Mu di Nu sàdd léebu, fàtte na ag sosoom ; dana wax naan : “Ana kan mooy dekkalaat ay yax yu funux ? ”
79قُلْ يُحْيِيهَا الَّذِي أَنشَأَهَا أَوَّلَ مَرَّةٍ ۖ وَهُوَ بِكُلِّ خَلْقٍ عَلِيمٌ
Neel : “Ki ko sosoon bu jëkk. Te xam lool bindafoon yépp ;
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
77Aaya

Tekki — Ya-Sin 77

Simoore Ya-Sin Aaya 77 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xanaa nit dafa gisul ne Nun Yàlla noo ko bind…

Simoore Aaya 77/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 75–79. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers