Ya-Sin · 78/83
Tekki Waxtaan — Ya-Sin
وَضَرَبَ لَنَا مَثَلًا وَنَسِيَ خَلْقَهُ ۖ قَالَ مَن يُحْيِي الْعِظَامَ وَهِيَ رَمِيمٌ ۝٧٨
Wa daraba lanaa maslanw-wa nasiya khalqahoo qaala mai-yuhyil`izaama wa hiya rameem
📖 Tekkim Wolof
Mu di Nu sàdd léebu, fàtte na ag sosoom ; dana wax naan : “Ana kan mooy dekkalaat ay yax yu funux ? ”
🎧 Dégg

📜 Aaya 76-80 — Ya-Sin

76فَلَا يَحْزُنكَ قَوْلُهُمْ ۘ إِنَّا نَعْلَمُ مَا يُسِرُّونَ وَمَا يُعْلِنُونَ
Bula seeni wax jaaxal ! Nun xam Nanu li ñuy yelu ak li ñuy biral.
77أَوَلَمْ يَرَ الْإِنسَانُ أَنَّا خَلَقْنَاهُ مِن نُّطْفَةٍ فَإِذَا هُوَ خَصِيمٌ مُّبِينٌ
Xanaa nit dafa gisul ne Nun Yàlla noo ko bind ci lumbub deret ? Deketeyoo moom ab xulóowaakoon la bu di ab pànk !
78وَضَرَبَ لَنَا مَثَلًا وَنَسِيَ خَلْقَهُ ۖ قَالَ مَن يُحْيِي الْعِظَامَ وَهِيَ رَمِيمٌ
Mu di Nu sàdd léebu, fàtte na ag sosoom ; dana wax naan : “Ana kan mooy dekkalaat ay yax yu funux ? ”
79قُلْ يُحْيِيهَا الَّذِي أَنشَأَهَا أَوَّلَ مَرَّةٍ ۖ وَهُوَ بِكُلِّ خَلْقٍ عَلِيمٌ
Neel : “Ki ko sosoon bu jëkk. Te xam lool bindafoon yépp ;
80الَّذِي جَعَلَ لَكُم مِّنَ الشَّجَرِ الْأَخْضَرِ نَارًا فَإِذَا أَنتُم مِّنْهُ تُوقِدُونَ
te Moo di ki leen defal ci garab gu nëtëx, aw safara wu ngeen di taaloo.
Ya-SinFihi Alxuraan
83Aaya
MeccanRevelation
78Aaya

Tekki — Ya-Sin 78

Simoore Ya-Sin Aaya 78 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu di Nu sàdd léebu, fàtte na ag sosoom ;…

Simoore Aaya 78/83 — Ya-Sin يس (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ya-Sin Dégg, Ya-Sin Tekki, Ya-Sin mp3, Ya-Sin pdf. Aaya 76–80. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers