As-Saffat · 109/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
سَلَامٌ عَلَىٰ إِبْرَاهِيمَ ۝١٠٩
Salaamun `alaaa Ibraaheem
📖 Tekkim Wolof
“Jàmmi Yàlla na nekk ci kaw Ibraahiima”.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 107-111 — Simoore As-Saffat

107وَفَدَيْنَاهُ بِذِبْحٍ عَظِيمٍ
Nu daldi koy jot ak lu ñuy rendi lu màgg.
108وَتَرَكْنَا عَلَيْهِ فِي الْآخِرِينَ
Daldi koy bàyyi muy dundu moom Ismaahiila :
109سَلَامٌ عَلَىٰ إِبْرَاهِيمَ
“Jàmmi Yàlla na nekk ci kaw Ibraahiima”.
110كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;
111إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
bokk na ci Sunu jaam ñi gëm.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
109Aaya

Tekki — As-Saffat 109

Simoore As-Saffat Aaya 109 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Jàmmi Yàlla na nekk ci kaw Ibraahiima”.

Simoore Aaya 109/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 107–111. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Sunday, October 4, 2026

Don't forget us in your sincere prayers