As-Saffat · 110/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ ۝١١٠
Kazaalika najzil muhsineen
📖 Tekkim Wolof
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 108-112 — Simoore As-Saffat

108وَتَرَكْنَا عَلَيْهِ فِي الْآخِرِينَ
Daldi koy bàyyi muy dundu moom Ismaahiila :
109سَلَامٌ عَلَىٰ إِبْرَاهِيمَ
“Jàmmi Yàlla na nekk ci kaw Ibraahiima”.
110كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;
111إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
bokk na ci Sunu jaam ñi gëm.
112وَبَشَّرْنَاهُ بِإِسْحَاقَ نَبِيًّا مِّنَ الصَّالِحِينَ
Bégal Nanu ko ci def Isaaqa mu di Yonent bokk ca ñay rafetal.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
110Aaya

Tekki — As-Saffat 110

Simoore As-Saffat Aaya 110 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;

Simoore Aaya 110/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 108–112. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers