As-Saffat · 113/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَبَارَكْنَا عَلَيْهِ وَعَلَىٰ إِسْحَاقَ ۚ وَمِن ذُرِّيَّتِهِمَا مُحْسِنٌ وَظَالِمٌ لِّنَفْسِهِ مُبِينٌ ۝١١٣
Wa baaraknaa `alaihi wa `alaaa Ishaaq; wa min zurriyya tihimaa muhsinunw wa zaalimul linafshihee mubeen
📖 Tekkim Wolof
Nu barkeel ko moom ak Isaaqa. Mu am ci seeni sët kuy rafetal ak kuy tooñ boppam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 111-115 — Simoore As-Saffat

111إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
bokk na ci Sunu jaam ñi gëm.
112وَبَشَّرْنَاهُ بِإِسْحَاقَ نَبِيًّا مِّنَ الصَّالِحِينَ
Bégal Nanu ko ci def Isaaqa mu di Yonent bokk ca ñay rafetal.
113وَبَارَكْنَا عَلَيْهِ وَعَلَىٰ إِسْحَاقَ ۚ وَمِن ذُرِّيَّتِهِمَا مُحْسِنٌ وَظَالِمٌ لِّنَفْسِهِ مُبِينٌ
Nu barkeel ko moom ak Isaaqa. Mu am ci seeni sët kuy rafetal ak kuy tooñ boppam.
114وَلَقَدْ مَنَنَّا عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Xéewaloon Nanu Muusaa ak Haaruuna,
115وَنَجَّيْنَاهُمَا وَقَوْمَهُمَا مِنَ الْكَرْبِ الْعَظِيمِ
Musaloon Nanu leen ñoom seeni sët ca tiit mu rëy ma,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
113Aaya

Tekki — As-Saffat 113

Simoore As-Saffat Aaya 113 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu barkeel ko moom ak Isaaqa. Mu am ci seeni…

Simoore Aaya 113/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 111–115. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers