As-Saffat · 114/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَلَقَدْ مَنَنَّا عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ ۝١١٤
Wa laqad mananna alaa Moosaa wa Haaroon
📖 Tekkim Wolof
Xéewaloon Nanu Muusaa ak Haaruuna,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 112-116 — Simoore As-Saffat

112وَبَشَّرْنَاهُ بِإِسْحَاقَ نَبِيًّا مِّنَ الصَّالِحِينَ
Bégal Nanu ko ci def Isaaqa mu di Yonent bokk ca ñay rafetal.
113وَبَارَكْنَا عَلَيْهِ وَعَلَىٰ إِسْحَاقَ ۚ وَمِن ذُرِّيَّتِهِمَا مُحْسِنٌ وَظَالِمٌ لِّنَفْسِهِ مُبِينٌ
Nu barkeel ko moom ak Isaaqa. Mu am ci seeni sët kuy rafetal ak kuy tooñ boppam.
114وَلَقَدْ مَنَنَّا عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Xéewaloon Nanu Muusaa ak Haaruuna,
115وَنَجَّيْنَاهُمَا وَقَوْمَهُمَا مِنَ الْكَرْبِ الْعَظِيمِ
Musaloon Nanu leen ñoom seeni sët ca tiit mu rëy ma,
116وَنَصَرْنَاهُمْ فَكَانُوا هُمُ الْغَالِبِينَ
Nu dimbali woon leen, ñoom ñoo nootoon.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
114Aaya

Tekki — As-Saffat 114

Simoore As-Saffat Aaya 114 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xéewaloon Nanu Muusaa ak Haaruuna,

Simoore Aaya 114/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 112–116. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Saturday, October 3, 2026

Don't forget us in your sincere prayers