As-Saffat · 112/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَبَشَّرْنَاهُ بِإِسْحَاقَ نَبِيًّا مِّنَ الصَّالِحِينَ ۝١١٢
Wa bashsharnaahu bi Ishaaqa Nabiyayam minas saaliheen
📖 Tekkim Wolof
Bégal Nanu ko ci def Isaaqa mu di Yonent bokk ca ñay rafetal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 110-114 — Simoore As-Saffat

110كَذَٰلِكَ نَجْزِي الْمُحْسِنِينَ
Noonu la Nuy feye ñiy rafetal ;
111إِنَّهُ مِنْ عِبَادِنَا الْمُؤْمِنِينَ
bokk na ci Sunu jaam ñi gëm.
112وَبَشَّرْنَاهُ بِإِسْحَاقَ نَبِيًّا مِّنَ الصَّالِحِينَ
Bégal Nanu ko ci def Isaaqa mu di Yonent bokk ca ñay rafetal.
113وَبَارَكْنَا عَلَيْهِ وَعَلَىٰ إِسْحَاقَ ۚ وَمِن ذُرِّيَّتِهِمَا مُحْسِنٌ وَظَالِمٌ لِّنَفْسِهِ مُبِينٌ
Nu barkeel ko moom ak Isaaqa. Mu am ci seeni sët kuy rafetal ak kuy tooñ boppam.
114وَلَقَدْ مَنَنَّا عَلَىٰ مُوسَىٰ وَهَارُونَ
Xéewaloon Nanu Muusaa ak Haaruuna,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
112Aaya

Tekki — As-Saffat 112

Simoore As-Saffat Aaya 112 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bégal Nanu ko ci def Isaaqa mu di Yonent bokk…

Simoore Aaya 112/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 110–114. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers