As-Saffat · 128/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ ۝١٢٨
Illaa `ibaadal laahil mukhlaseen
📖 Tekkim Wolof
Ba mu des jaami Yàlla ya daan sellal.

🎧 Dégg


📜 Aaya 126-130 — Simoore As-Saffat

126اللَّهَ رَبَّكُمْ وَرَبَّ آبَائِكُمُ الْأَوَّلِينَ
Yàlla miy seen Boroom te di Boroomi seeni baay ak i maamaat ? ”
127فَكَذَّبُوهُ فَإِنَّهُمْ لَمُحْضَرُونَ
Ñu weddi ko, Nu mbugal leen.
128إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
Ba mu des jaami Yàlla ya daan sellal.
129وَتَرَكْنَا عَلَيْهِ فِي الْآخِرِينَ
Nu bàyyi nit ñuy mujj noonu di ko fàttaliku :
130سَلَامٌ عَلَىٰ إِلْ يَاسِينَ
“Jàmm yal na nekk ci njabootug Ilyaas”.
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
128Aaya

Tekki — As-Saffat 128

Simoore As-Saffat Aaya 128 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba mu des jaami Yàlla ya daan sellal.

Simoore Aaya 128/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 126–130. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers