As-Saffat · 38/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
إِنَّكُمْ لَذَائِقُو الْعَذَابِ الْأَلِيمِ ۝٣٨
Innakum lazaaa`iqul `azaabil aleem
📖 Tekkim Wolof
Yéen dangeen mos mbugal mu mitti.

🎧 Dégg


📜 Aaya 36-40 — Simoore As-Saffat

36وَيَقُولُونَ أَئِنَّا لَتَارِكُو آلِهَتِنَا لِشَاعِرٍ مَّجْنُونٍ
tey wax naan : “Ndax danuy bàyyi sunu yàlla yi ngir woykat bu dof ? ”
37بَلْ جَاءَ بِالْحَقِّ وَصَدَّقَ الْمُرْسَلِينَ
Te moom dëgg rekk la indi tey dëggal li Yonent ya indi woon,
38إِنَّكُمْ لَذَائِقُو الْعَذَابِ الْأَلِيمِ
Yéen dangeen mos mbugal mu mitti.
39وَمَا تُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Te it kenn du leen feye lu dul la ngeen daan jëfe,
40إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
ba mu des jaami Yàlla yay sellal,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — As-Saffat 38

Simoore As-Saffat Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen dangeen mos mbugal mu mitti.

Simoore Aaya 38/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers