As-Saffat · 39/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
وَمَا تُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ ۝٣٩
Wa maa tujzawna illaa maa kuntum ta`maloon
📖 Tekkim Wolof
Te it kenn du leen feye lu dul la ngeen daan jëfe,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 37-41 — Simoore As-Saffat

37بَلْ جَاءَ بِالْحَقِّ وَصَدَّقَ الْمُرْسَلِينَ
Te moom dëgg rekk la indi tey dëggal li Yonent ya indi woon,
38إِنَّكُمْ لَذَائِقُو الْعَذَابِ الْأَلِيمِ
Yéen dangeen mos mbugal mu mitti.
39وَمَا تُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Te it kenn du leen feye lu dul la ngeen daan jëfe,
40إِلَّا عِبَادَ اللَّهِ الْمُخْلَصِينَ
ba mu des jaami Yàlla yay sellal,
41أُولَٰئِكَ لَهُمْ رِزْقٌ مَّعْلُومٌ
Ñoom am nañu wërsëg wu ñu xam :
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — As-Saffat 39

Simoore As-Saffat Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te it kenn du leen feye lu dul la ngeen…

Simoore Aaya 39/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers