As-Saffat · 37/182
Tekki Waxtaan — Simoore As-Saffat
بَلْ جَاءَ بِالْحَقِّ وَصَدَّقَ الْمُرْسَلِينَ ۝٣٧
bal jaaa`a bilhaqqi wa saddaqal mursaleen
📖 Tekkim Wolof
Te moom dëgg rekk la indi tey dëggal li Yonent ya indi woon,

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — Simoore As-Saffat

35إِنَّهُمْ كَانُوا إِذَا قِيلَ لَهُمْ لَا إِلَٰهَ إِلَّا اللَّهُ يَسْتَكْبِرُونَ
Bu ñu waxaan ne : “Amul jeneen yàlla ju dul Yàlla”, dañu daan rëy-rëylu,
36وَيَقُولُونَ أَئِنَّا لَتَارِكُو آلِهَتِنَا لِشَاعِرٍ مَّجْنُونٍ
tey wax naan : “Ndax danuy bàyyi sunu yàlla yi ngir woykat bu dof ? ”
37بَلْ جَاءَ بِالْحَقِّ وَصَدَّقَ الْمُرْسَلِينَ
Te moom dëgg rekk la indi tey dëggal li Yonent ya indi woon,
38إِنَّكُمْ لَذَائِقُو الْعَذَابِ الْأَلِيمِ
Yéen dangeen mos mbugal mu mitti.
39وَمَا تُجْزَوْنَ إِلَّا مَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Te it kenn du leen feye lu dul la ngeen daan jëfe,
As-SaffatFihi Alxuraan
182Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — As-Saffat 37

Simoore As-Saffat Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te moom dëgg rekk la indi tey dëggal li Yonent…

Simoore Aaya 37/182 — Simoore As-Saffat الصافات (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore As-Saffat Dégg, Simoore As-Saffat Tekki, Simoore As-Saffat mp3, Simoore As-Saffat pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers