Sad · 62/88
Tekki Waxtaan — Simoore Sad
وَقَالُوا مَا لَنَا لَا نَرَىٰ رِجَالًا كُنَّا نَعُدُّهُم مِّنَ الْأَشْرَارِ ۝٦٢
Wa qaaloo ma lanaa laa naraa rijaalan kunnaa na`udduhum minal ashraar
📖 Tekkim Wolof
“Ana lan moo xew ba gisunu fi gaa ya nu daan limaale ci saay-saay si ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 60-64 — Simoore Sad

60قَالُوا بَلْ أَنتُمْ لَا مَرْحَبًا بِكُمْ ۖ أَنتُمْ قَدَّمْتُمُوهُ لَنَا ۖ فَبِئْسَ الْقَرَارُ
Ñuy wax naan : “Yéen kay la kenn dul dalal, lii, Yéen la ñu ko waajal”. Te ndaw saxuwaay bu bon !
61قَالُوا رَبَّنَا مَن قَدَّمَ لَنَا هَٰذَا فَزِدْهُ عَذَابًا ضِعْفًا فِي النَّارِ
Ñuy wax naan : “Yaw sunu Boroom na nga dolli, ki nu waajalal lii, mbugël muy fulandiku ca biir Safara ”.
62وَقَالُوا مَا لَنَا لَا نَرَىٰ رِجَالًا كُنَّا نَعُدُّهُم مِّنَ الْأَشْرَارِ
“Ana lan moo xew ba gisunu fi gaa ya nu daan limaale ci saay-saay si ?
63أَتَّخَذْنَاهُمْ سِخْرِيًّا أَمْ زَاغَتْ عَنْهُمُ الْأَبْصَارُ
Moo ndax dañu leen ko daan tooñe walla danu làqu sunu gëm ? ”
64إِنَّ ذَٰلِكَ لَحَقٌّ تَخَاصُمُ أَهْلِ النَّارِ
Lii daal tigi mooy xulóob waa Safara
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
62Aaya

Tekki — Sad 62

Simoore Sad Aaya 62 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Ana lan moo xew ba gisunu fi gaa ya nu…

Simoore Aaya 62/88 — Simoore Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Sad Dégg, Simoore Sad Tekki, Simoore Sad mp3, Simoore Sad pdf. Aaya 60–64. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers