Sad · 65/88
Tekki Waxtaan — Sad
قُلْ إِنَّمَا أَنَا مُنذِرٌ ۖ وَمَا مِنْ إِلَٰهٍ إِلَّا اللَّهُ الْوَاحِدُ الْقَهَّارُ ٦٥
Transliteration
Qul innamaaa ana munzirunw wa maa min ilaahim illal laahul Waahidul Qahhaar
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Waxal ne : “Man daal ab xuppekat laa. Te jenn Yàlla amul judul, Yàlla jiy jenn , Notaakoon ba,
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 63-67 — Sad
63أَتَّخَذْنَاهُمْ سِخْرِيًّا أَمْ زَاغَتْ عَنْهُمُ الْأَبْصَارُ
Moo ndax dañu leen ko daan tooñe walla danu làqu sunu gëm ? ”
64إِنَّ ذَٰلِكَ لَحَقٌّ تَخَاصُمُ أَهْلِ النَّارِ
Lii daal tigi mooy xulóob waa Safara
65قُلْ إِنَّمَا أَنَا مُنذِرٌ ۖ وَمَا مِنْ إِلَٰهٍ إِلَّا اللَّهُ الْوَاحِدُ الْقَهَّارُ
Waxal ne : “Man daal ab xuppekat laa. Te jenn Yàlla amul judul, Yàlla jiy jenn , Notaakoon ba,
66رَبُّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا الْعَزِيزُ الْغَفَّارُ
Mooy Boroom asamaan yeek suuf si ak li nekk ci seen diggënte, te mooy boroom Kàttan gi, di Jégëlaakoon bi”.
67قُلْ هُوَ نَبَأٌ عَظِيمٌ
Waxal ne : “Xibaar bu rëy la,
SadFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
65Aaya
Tekki — Sad 65
Simoore Sad Aaya 65 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waxal ne : “Man daal ab xuppekat laa. Te jenn…Simoore Aaya 65/88 — Sad ص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Sad Dégg, Sad Tekki, Sad mp3, Sad pdf. Aaya 63–67. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








