An-Nisa · 64/176
Tekki Waxtaan — An-Nisa
وَمَا أَرْسَلْنَا مِن رَّسُولٍ إِلَّا لِيُطَاعَ بِإِذْنِ اللَّهِ ۚ وَلَوْ أَنَّهُمْ إِذ ظَّلَمُوا أَنفُسَهُمْ جَاءُوكَ فَاسْتَغْفَرُوا اللَّهَ وَاسْتَغْفَرَ لَهُمُ الرَّسُولُ لَوَجَدُوا اللَّهَ تَوَّابًا رَّحِيمًا ۝٦٤
Wa maa arsalnaa mir Rasoolin illaa liyutaa`a bi iznil laah; wa law annahum `iz zalamooo anfusahum jaaa`ooka fastaghfarul laaha wastaghfara lahumur Rasoolu la wajadul laaha Tawwaabar Raheemaa
📖 Tekkim Wolof
Yónniwunu ab Yonent lu dul ne dañu koo war a topp ci ndigalu Yàlla. Te ñoom ba ñu tooñee seen bopp, bu ñu dikkoon ci yaw di sàkku jéggalu Yàlla, Yonent bi jéggalul leen, kon danañu fekk Yàlla mu di Jéggalaakoon, di Jaglewaakoon.
🎧 Dégg

📜 Aaya 62-66 — An-Nisa

62فَكَيْفَ إِذَا أَصَابَتْهُم مُّصِيبَةٌ بِمَا قَدَّمَتْ أَيْدِيهِمْ ثُمَّ جَاءُوكَ يَحْلِفُونَ بِاللَّهِ إِنْ أَرَدْنَا إِلَّا إِحْسَانًا وَتَوْفِيقًا
Naka mu? Bu leen musiba dalee jóge ca la ñu jëf, ba tax ñu ñëw ci yaw di giñ ci Yàlla, naan : “Bëggunu woon lu dul rafetal ak juboo”.
63أُولَٰئِكَ الَّذِينَ يَعْلَمُ اللَّهُ مَا فِي قُلُوبِهِمْ فَأَعْرِضْ عَنْهُمْ وَعِظْهُمْ وَقُل لَّهُمْ فِي أَنفُسِهِمْ قَوْلًا بَلِيغًا
Ñooña, Yàlla xam na la nekk ci seeni xol. Nanga leen dëddu [dummóoyu] te nanga leen waar, waxleen ci seen bopp wax ju jotal.
64وَمَا أَرْسَلْنَا مِن رَّسُولٍ إِلَّا لِيُطَاعَ بِإِذْنِ اللَّهِ ۚ وَلَوْ أَنَّهُمْ إِذ ظَّلَمُوا أَنفُسَهُمْ جَاءُوكَ فَاسْتَغْفَرُوا اللَّهَ وَاسْتَغْفَرَ لَهُمُ الرَّسُولُ لَوَجَدُوا اللَّهَ تَوَّابًا رَّحِيمًا
Yónniwunu ab Yonent lu dul ne dañu koo war a topp ci ndigalu Yàlla. Te ñoom ba ñu tooñee seen bopp, bu ñu dikkoon ci yaw di sàkku jéggalu Yàlla, Yonent bi jéggalul leen, kon danañu fekk Yàlla mu di Jéggalaakoon, di Jaglewaakoon.
65فَلَا وَرَبِّكَ لَا يُؤْمِنُونَ حَتَّىٰ يُحَكِّمُوكَ فِيمَا شَجَرَ بَيْنَهُمْ ثُمَّ لَا يَجِدُوا فِي أَنفُسِهِمْ حَرَجًا مِّمَّا قَضَيْتَ وَيُسَلِّمُوا تَسْلِيمًا
Mukk !... Giñ naa ci sa màggug Boroom ! Duñu gëm mukk [di ay jullit] li feek àtteloowuñu la la ca seen diggante te bañ a am benn ñag-ñagi xol ca la nga àtte, nangul la ak xol bu tàlli.
66وَلَوْ أَنَّا كَتَبْنَا عَلَيْهِمْ أَنِ اقْتُلُوا أَنفُسَكُمْ أَوِ اخْرُجُوا مِن دِيَارِكُم مَّا فَعَلُوهُ إِلَّا قَلِيلٌ مِّنْهُمْ ۖ وَلَوْ أَنَّهُمْ فَعَلُوا مَا يُوعَظُونَ بِهِ لَكَانَ خَيْرًا لَّهُمْ وَأَشَدَّ تَثْبِيتًا
Su fekkoon ñoon Danu leen sant ñu reyante mbaa ñu génn seeni kër, duñu ko def lu dul ñu néew ci ñoom. Te su ñu defoon la ñu leen di waare, mu gën ca ñoom, te gën a dëgëral seen ngëm.
An-NisaFihi Alxuraan
176Aaya
MedinanRevelation
64Aaya

Tekki — An-Nisa 64

Simoore An-Nisa Aaya 64 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yónniwunu ab Yonent lu dul ne dañu koo war a…

Simoore Aaya 64/176 — An-Nisa النساء (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nisa Dégg, An-Nisa Tekki, An-Nisa mp3, An-Nisa pdf. Aaya 62–66. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers