An-Nisa · 69/176
Tekki Waxtaan — An-Nisa
وَمَن يُطِعِ اللَّهَ وَالرَّسُولَ فَأُولَٰئِكَ مَعَ الَّذِينَ أَنْعَمَ اللَّهُ عَلَيْهِم مِّنَ النَّبِيِّينَ وَالصِّدِّيقِينَ وَالشُّهَدَاءِ وَالصَّالِحِينَ ۚ وَحَسُنَ أُولَٰئِكَ رَفِيقًا ٦٩
Transliteration
Wa many-yuti`il laaha war Rasoola fa ulaaa`ika ma`al lazeena an`amal laahu `alaihim minan nabiyyeena wassiddeeqeena washshuhadaaa`i wassaaliheen; wa hasuna ulaaa`ika rafeeqaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Ku topp Yàlla ak Yonent ba... ñooña ànd nañook ña Yàlla wàcce xéewalam ci ñoom : ca Yonent ya ak way-dëggu ña [daraja ju kawe sahaaba ya], ak ña dee ci xare ngir Yàlla, ak ñu sell [ñu yiw] ña, ndaw àndandoo yu jekk !
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 67-71 — An-Nisa
67وَإِذًا لَّآتَيْنَاهُم مِّن لَّدُنَّا أَجْرًا عَظِيمًا
Te kon Nu jox leen pey gu màgg jóge ci Nun,
68وَلَهَدَيْنَاهُمْ صِرَاطًا مُّسْتَقِيمًا
te kon Nu gindi leen teg leen ca yoon wu jub xocc wa.
69وَمَن يُطِعِ اللَّهَ وَالرَّسُولَ فَأُولَٰئِكَ مَعَ الَّذِينَ أَنْعَمَ اللَّهُ عَلَيْهِم مِّنَ النَّبِيِّينَ وَالصِّدِّيقِينَ وَالشُّهَدَاءِ وَالصَّالِحِينَ ۚ وَحَسُنَ أُولَٰئِكَ رَفِيقًا
Ku topp Yàlla ak Yonent ba... ñooña ànd nañook ña Yàlla wàcce xéewalam ci ñoom : ca Yonent ya ak way-dëggu ña [daraja ju kawe sahaaba ya], ak ña dee ci xare ngir Yàlla, ak ñu sell [ñu yiw] ña, ndaw àndandoo yu jekk !
70ذَٰلِكَ الْفَضْلُ مِنَ اللَّهِ ۚ وَكَفَىٰ بِاللَّهِ عَلِيمًا
Loolooy ngëneel la jóge ca Yàlla. Te Yàlla doy na, mat na sëkk boroom xam-xam.
71يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا خُذُوا حِذْرَكُمْ فَانفِرُوا ثُبَاتٍ أَوِ انفِرُوا جَمِيعًا
Éy yéen ñi gëm ! Nangeen fagaru ci seen [coongum noon], moo xam ngeen tasaaroo walla ngeen àndandoo.
An-NisaFihi Alxuraan
176Aaya
MedinanRevelation
69Aaya
Tekki — An-Nisa 69
Simoore An-Nisa Aaya 69 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ku topp Yàlla ak Yonent ba... ñooña ànd nañook ña…Simoore Aaya 69/176 — An-Nisa النساء (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nisa Dégg, An-Nisa Tekki, An-Nisa mp3, An-Nisa pdf. Aaya 67–71. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








