Ghafir · 67/85
Tekki Waxtaan — Simoore Ghafir
هُوَ الَّذِي خَلَقَكُم مِّن تُرَابٍ ثُمَّ مِن نُّطْفَةٍ ثُمَّ مِنْ عَلَقَةٍ ثُمَّ يُخْرِجُكُمْ طِفْلًا ثُمَّ لِتَبْلُغُوا أَشُدَّكُمْ ثُمَّ لِتَكُونُوا شُيُوخًا ۚ وَمِنكُم مَّن يُتَوَفَّىٰ مِن قَبْلُ ۖ وَلِتَبْلُغُوا أَجَلًا مُّسَمًّى وَلَعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ ۝٦٧
Huwal lazee khalaqakum min turaabin summa min nutfatin summa min `alaqatin summa yukhrijukum tiflan summa litablughooo ashuddakum summa litakoonoo shuyookhaa; wa minkum mai yutawaffaa min qablu wa litablughooo ajalam musam manw-wa la`allakum ta`qiloon
📖 Tekkim Wolof
Mooy ki leen bind ci suuf, te jaarale leen ci toqu maniyy, ak ci lumbu deret door leen a génne ngeen di ay xale mu def leen ngeen di ay mag yu war a maggat kumur, - am na ci yéen ñuy faatu balaa loolu lépp di am, - ku ca nekk it am na ab dig bu ñu ko àppal, ak it ngir ngeen xellu (xalaat).

🎧 Dégg


📜 Aaya 65-69 — Simoore Ghafir

65هُوَ الْحَيُّ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ فَادْعُوهُ مُخْلِصِينَ لَهُ الدِّينَ ۗ الْحَمْدُ لِلَّهِ رَبِّ الْعَالَمِينَ
Mooy kiy dund. Amul jeneen Yàlla judul moom. Na ngeen koy jaamu, te di ko sellal diine ji. Cant ñeel na Yàlla, Miy Boroom àddina si !
66۞ قُلْ إِنِّي نُهِيتُ أَنْ أَعْبُدَ الَّذِينَ تَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ لَمَّا جَاءَنِيَ الْبَيِّنَاتُ مِن رَّبِّي وَأُمِرْتُ أَنْ أُسْلِمَ لِرَبِّ الْعَالَمِينَ
Waxal ne : “Tere na nu ma, may jaamu li ngeen di jaamu te du Yàlla, waxtu wa ma ay lay yu leer nàññ digëlee te bawoo ci sama Boroom, te it digaléef na ma jébël sama bopp Yàlla miy Boroom àddina si”.
67هُوَ الَّذِي خَلَقَكُم مِّن تُرَابٍ ثُمَّ مِن نُّطْفَةٍ ثُمَّ مِنْ عَلَقَةٍ ثُمَّ يُخْرِجُكُمْ طِفْلًا ثُمَّ لِتَبْلُغُوا أَشُدَّكُمْ ثُمَّ لِتَكُونُوا شُيُوخًا ۚ وَمِنكُم مَّن يُتَوَفَّىٰ مِن قَبْلُ ۖ وَلِتَبْلُغُوا أَجَلًا مُّسَمًّى وَلَعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ
Mooy ki leen bind ci suuf, te jaarale leen ci toqu maniyy, ak ci lumbu deret door leen a génne ngeen di ay xale mu def leen ngeen di ay mag yu war a maggat kumur, - am na ci yéen ñuy faatu balaa loolu lépp di am, - ku ca nekk it am na ab dig bu ñu ko àppal, ak it ngir ngeen xellu (xalaat).
68هُوَ الَّذِي يُحْيِي وَيُمِيتُ ۖ فَإِذَا قَضَىٰ أَمْرًا فَإِنَّمَا يَقُولُ لَهُ كُن فَيَكُونُ
Mooy dundal mooy rey. saa su dogoo ci mbir, danaan ko : “nekkal”, mu daldi nekk.
69أَلَمْ تَرَ إِلَى الَّذِينَ يُجَادِلُونَ فِي آيَاتِ اللَّهِ أَنَّىٰ يُصْرَفُونَ
Xanaa gisuloo ñiy dàggasante ci laayay Yàlla yi ni ñu leen di walbatee?
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
67Aaya

Tekki — Ghafir 67

Simoore Ghafir Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mooy ki leen bind ci suuf, te jaarale leen ci…

Simoore Aaya 67/85 — Simoore Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ghafir Dégg, Simoore Ghafir Tekki, Simoore Ghafir mp3, Simoore Ghafir pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers