Ghafir · 80/85
Tekki Waxtaan — Simoore Ghafir
وَلَكُمْ فِيهَا مَنَافِعُ وَلِتَبْلُغُوا عَلَيْهَا حَاجَةً فِي صُدُورِكُمْ وَعَلَيْهَا وَعَلَى الْفُلْكِ تُحْمَلُونَ ۝٨٠
Wa lakum feehaa manaafi`u wa litablughoo `alaihaa haajatan fee sudoorikum wa `alaihaa wa `alal fulki tuhmaloon
📖 Tekkim Wolof
te am ngeen ci ay njariñ ak it ngeen di ca faj ay aajo yu leen soxal. Ngeen di ca yéeg di ànd ak ñoom di war ci gaal yi.

🎧 Dégg


📜 Aaya 78-82 — Simoore Ghafir

78وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا رُسُلًا مِّن قَبْلِكَ مِنْهُم مَّن قَصَصْنَا عَلَيْكَ وَمِنْهُم مَّن لَّمْ نَقْصُصْ عَلَيْكَ ۗ وَمَا كَانَ لِرَسُولٍ أَن يَأْتِيَ بِآيَةٍ إِلَّا بِإِذْنِ اللَّهِ ۚ فَإِذَا جَاءَ أَمْرُ اللَّهِ قُضِيَ بِالْحَقِّ وَخَسِرَ هُنَالِكَ الْمُبْطِلُونَ
Yónni woon Nanu ay Yonnent yu la jiitu woon. am na ci ñu ñu la nettali ; am na ci ñu ñu la nettaliwul. Amul benn yonnent bu sañ a indi [kimaan laaya] lu dul ne da ca am ndigëlul Yàlla. Saa su ndigëlul Yàlla agsee, mbir yépp àttewo ci dëgg ; fenkat yi daldi yàqule.
79اللَّهُ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَنْعَامَ لِتَرْكَبُوا مِنْهَا وَمِنْهَا تَأْكُلُونَ
Yàlla mi leen defaral mala yi ngir ngeen di ci war te di ca lekk,
80وَلَكُمْ فِيهَا مَنَافِعُ وَلِتَبْلُغُوا عَلَيْهَا حَاجَةً فِي صُدُورِكُمْ وَعَلَيْهَا وَعَلَى الْفُلْكِ تُحْمَلُونَ
te am ngeen ci ay njariñ ak it ngeen di ca faj ay aajo yu leen soxal. Ngeen di ca yéeg di ànd ak ñoom di war ci gaal yi.
81وَيُرِيكُمْ آيَاتِهِ فَأَيَّ آيَاتِ اللَّهِ تُنكِرُونَ
Mu di leen won ay kéemaanam. Naka ngeen koy weddee ?
82أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَيَنظُرُوا كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ كَانُوا أَكْثَرَ مِنْهُمْ وَأَشَدَّ قُوَّةً وَآثَارًا فِي الْأَرْضِ فَمَا أَغْنَىٰ عَنْهُم مَّا كَانُوا يَكْسِبُونَ
Xanaa du ñu dox ci kaw suuf tey seetlu mujjug xeet ya leen jiitu woon ? ëppoon leen gënoon leen bari doole [ak i jeexit] ci suuf si. Te lañu daan fàggu fegalu leen dara (taxut woon mu doy leen).
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
80Aaya

Tekki — Ghafir 80

Simoore Ghafir Aaya 80 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te am ngeen ci ay njariñ ak it ngeen di…

Simoore Aaya 80/85 — Simoore Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ghafir Dégg, Simoore Ghafir Tekki, Simoore Ghafir mp3, Simoore Ghafir pdf. Aaya 78–82. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers