Ghafir · 79/85
Tekki Waxtaan — Ghafir
اللَّهُ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَنْعَامَ لِتَرْكَبُوا مِنْهَا وَمِنْهَا تَأْكُلُونَ ۝٧٩
Allaahul lazee ja`ala lakumul an`aama litarkaboo minhaa wa minhaa taakuloon
📖 Tekkim Wolof
Yàlla mi leen defaral mala yi ngir ngeen di ci war te di ca lekk,
🎧 Dégg

📜 Aaya 77-81 — Ghafir

77فَاصْبِرْ إِنَّ وَعْدَ اللَّهِ حَقٌّ ۚ فَإِمَّا نُرِيَنَّكَ بَعْضَ الَّذِي نَعِدُهُمْ أَوْ نَتَوَفَّيَنَّكَ فَإِلَيْنَا يُرْجَعُونَ
Na ngay muñ (te xam ne). Digub Yàlla dëgg la. Amaana Nu wan la lenn ci li Nu leen di tëkkoo mbaa nu faat la (balaa loolu di am)... ak lu man a xew ñoom ñépp ci nun la nuy dellusi.
78وَلَقَدْ أَرْسَلْنَا رُسُلًا مِّن قَبْلِكَ مِنْهُم مَّن قَصَصْنَا عَلَيْكَ وَمِنْهُم مَّن لَّمْ نَقْصُصْ عَلَيْكَ ۗ وَمَا كَانَ لِرَسُولٍ أَن يَأْتِيَ بِآيَةٍ إِلَّا بِإِذْنِ اللَّهِ ۚ فَإِذَا جَاءَ أَمْرُ اللَّهِ قُضِيَ بِالْحَقِّ وَخَسِرَ هُنَالِكَ الْمُبْطِلُونَ
Yónni woon Nanu ay Yonnent yu la jiitu woon. am na ci ñu ñu la nettali ; am na ci ñu ñu la nettaliwul. Amul benn yonnent bu sañ a indi [kimaan laaya] lu dul ne da ca am ndigëlul Yàlla. Saa su ndigëlul Yàlla agsee, mbir yépp àttewo ci dëgg ; fenkat yi daldi yàqule.
79اللَّهُ الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَنْعَامَ لِتَرْكَبُوا مِنْهَا وَمِنْهَا تَأْكُلُونَ
Yàlla mi leen defaral mala yi ngir ngeen di ci war te di ca lekk,
80وَلَكُمْ فِيهَا مَنَافِعُ وَلِتَبْلُغُوا عَلَيْهَا حَاجَةً فِي صُدُورِكُمْ وَعَلَيْهَا وَعَلَى الْفُلْكِ تُحْمَلُونَ
te am ngeen ci ay njariñ ak it ngeen di ca faj ay aajo yu leen soxal. Ngeen di ca yéeg di ànd ak ñoom di war ci gaal yi.
81وَيُرِيكُمْ آيَاتِهِ فَأَيَّ آيَاتِ اللَّهِ تُنكِرُونَ
Mu di leen won ay kéemaanam. Naka ngeen koy weddee ?
GhafirFihi Alxuraan
85Aaya
MeccanRevelation
79Aaya

Tekki — Ghafir 79

Simoore Ghafir Aaya 79 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàlla mi leen defaral mala yi ngir ngeen di ci…

Simoore Aaya 79/85 — Ghafir غافر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ghafir Dégg, Ghafir Tekki, Ghafir mp3, Ghafir pdf. Aaya 77–81. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers