Ash-Shura · 10/53
Tekki Waxtaan — Ash-Shura
وَمَا اخْتَلَفْتُمْ فِيهِ مِن شَيْءٍ فَحُكْمُهُ إِلَى اللَّهِ ۚ ذَٰلِكُمُ اللَّهُ رَبِّي عَلَيْهِ تَوَكَّلْتُ وَإِلَيْهِ أُنِيبُ ۝١٠
Wa makh-talaftum feehi min shai`in fahukmuhooo ilallaah; zaalikumul laahu Rabbee `alaihi tawakkaltu wa ilaihi uneeb
📖 Tekkim Wolof
Te lépp lu ngeen am ag juuyoo, Yàlla yor àtte ba. Koo koo di Yàlla sama Boroom; ci Moom laay wéeru te it moom la doyloo.

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Ash-Shura

8وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ لَجَعَلَهُمْ أُمَّةً وَاحِدَةً وَلَٰكِن يُدْخِلُ مَن يَشَاءُ فِي رَحْمَتِهِ ۚ وَالظَّالِمُونَ مَا لَهُم مِّن وَلِيٍّ وَلَا نَصِيرٍ
Su sooboon Yàlla, Mu def leen wenn xeet. Waaye Mooy dugël ku Ko neex ci biir yërmandéem. Te tooñkat yi nag ñoom duñu am wéeruwaay, waxantumalaak ku leen di dimbali.
9أَمِ اتَّخَذُوا مِن دُونِهِ أَوْلِيَاءَ ۖ فَاللَّهُ هُوَ الْوَلِيُّ وَهُوَ يُحْيِي الْمَوْتَىٰ وَهُوَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Walla ñoom dañoo far am wéeruwaay yu dul Yàlla ? Wéeruwaay tigi mooy Yàlla ; te mooy dekkal ñu dee woon ña te moo di ki man lépp lu ne.
10وَمَا اخْتَلَفْتُمْ فِيهِ مِن شَيْءٍ فَحُكْمُهُ إِلَى اللَّهِ ۚ ذَٰلِكُمُ اللَّهُ رَبِّي عَلَيْهِ تَوَكَّلْتُ وَإِلَيْهِ أُنِيبُ
Te lépp lu ngeen am ag juuyoo, Yàlla yor àtte ba. Koo koo di Yàlla sama Boroom; ci Moom laay wéeru te it moom la doyloo.
11فَاطِرُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۚ جَعَلَ لَكُم مِّنْ أَنفُسِكُمْ أَزْوَاجًا وَمِنَ الْأَنْعَامِ أَزْوَاجًا ۖ يَذْرَؤُكُمْ فِيهِ ۚ لَيْسَ كَمِثْلِهِ شَيْءٌ ۖ وَهُوَ السَّمِيعُ الْبَصِيرُ
Moo bind (sàkk) asamaan yeek suuf si. Defaralal na leen y soxna [jële ko] ci seeni jëmm ak ay mala yu di ay tóollént ( góor ak jigéen); te ci loolu la leen di yokki (jurante). Amul lenn lu mel ni moom (Yàlla) ; mooy aji Dégg, di aji Gis.
12لَهُ مَقَالِيدُ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۖ يَبْسُطُ الرِّزْقَ لِمَن يَشَاءُ وَيَقْدِرُ ۚ إِنَّهُ بِكُلِّ شَيْءٍ عَلِيمٌ
Moo ame caabi [ndami] asamaan yeek suuf si. Mooy yaatalal wërsëg ku ko soob, moo ko koy xatalal it. Te, Moo di ku xam lépp lu nekk.
Ash-ShuraFihi Alxuraan
53Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Ash-Shura 10

Simoore Ash-Shura Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te lépp lu ngeen am ag juuyoo, Yàlla yor àtte…

Simoore Aaya 10/53 — Ash-Shura الشورى (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shura Dégg, Ash-Shura Tekki, Ash-Shura mp3, Ash-Shura pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers