Ad-Dukhan · 23/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
فَأَسْرِ بِعِبَادِي لَيْلًا إِنَّكُم مُّتَّبَعُونَ ۝٢٣
Fa asri bi`ibaadee lailan innakum muttaba`oon
📖 Tekkim Wolof
“Toppal guddi rañaan ak samay jaam ; danañu len dabusi.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 21-25 — Simoore Ad-Dukhan

21وَإِن لَّمْ تُؤْمِنُوا لِي فَاعْتَزِلُونِ
Su fekkee ne gëmuleen ma, kon sori leen ma”.
22فَدَعَا رَبَّهُ أَنَّ هَٰؤُلَاءِ قَوْمٌ مُّجْرِمُونَ
Muu daldi ñaan Boroomam ne ko : “Ñi de ay niti Tafaar lañu (tooñkat)”.
23فَأَسْرِ بِعِبَادِي لَيْلًا إِنَّكُم مُّتَّبَعُونَ
“Toppal guddi rañaan ak samay jaam ; danañu len dabusi.
24وَاتْرُكِ الْبَحْرَ رَهْوًا ۖ إِنَّهُمْ جُندٌ مُّغْرَقُونَ
Bàyyil géej ga mu ne tekk ; ndax ñoom ay xarekat lañu ñuy, xala lab”.
25كَمْ تَرَكُوا مِن جَنَّاتٍ وَعُيُونٍ
Ak a bari ay dër yu ñu bàyyi ginnaaw ak bëti ndox
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 23

Simoore Ad-Dukhan Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Toppal guddi rañaan ak samay jaam ; danañu len dabusi.

Simoore Aaya 23/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers