Ad-Dukhan · 48/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
ثُمَّ صُبُّوا فَوْقَ رَأْسِهِ مِنْ عَذَابِ الْحَمِيمِ ۝٤٨
Summa subboo fawqa raasihee min `azaabil hameem
📖 Tekkim Wolof
topp ñuy sotti ci kaw boppam ba mbugëlum ndox muy wañax.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 46-50 — Simoore Ad-Dukhan

46كَغَلْيِ الْحَمِيمِ
ni ndox muy bax di wañaxe.
47خُذُوهُ فَاعْتِلُوهُ إِلَىٰ سَوَاءِ الْجَحِيمِ
Jëlleen ku tëmbéel ko moom ca digg Safara;
48ثُمَّ صُبُّوا فَوْقَ رَأْسِهِ مِنْ عَذَابِ الْحَمِيمِ
topp ñuy sotti ci kaw boppam ba mbugëlum ndox muy wañax.
49ذُقْ إِنَّكَ أَنتَ الْعَزِيزُ الْكَرِيمُ
Mosal tokamtikul ! Yaay [boroom kàttan] tey ku Tedd (daan rëy-rëylu).
50إِنَّ هَٰذَا مَا كُنتُم بِهِ تَمْتَرُونَ
Lii nag tigi mooy li ngeen daan werante di ko sikki-sàkka.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 48

Simoore Ad-Dukhan Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : topp ñuy sotti ci kaw boppam ba mbugëlum ndox muy…

Simoore Aaya 48/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers