Muhammad · 19/38
Tekki Waxtaan — Simoore Muhammad
فَاعْلَمْ أَنَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا اللَّهُ وَاسْتَغْفِرْ لِذَنبِكَ وَلِلْمُؤْمِنِينَ وَالْمُؤْمِنَاتِ ۗ وَاللَّهُ يَعْلَمُ مُتَقَلَّبَكُمْ وَمَثْوَاكُمْ ۝١٩
Fa`lam annahoo laaa ilaaha illal laahu wastaghfir lizambika wa lilmu`mineena walmu`minaat; wallaahu ya`lamu mutaqallabakum wa maswaakum
📖 Tekkim Wolof
Xamal ne, amul jeneen Yàlla ju dul moom Yàlla, te nga jéggalu say bàkkaar, ak di jéggalul jullit yu goor yeek yu jigéen yi. Yàlla xam na li ngeen di def lépp guddeek bëcëg.

🎧 Dégg


📜 Aaya 17-21 — Simoore Muhammad

17وَالَّذِينَ اهْتَدَوْا زَادَهُمْ هُدًى وَآتَاهُمْ تَقْوَاهُمْ
Ña gindiku ñoom dolli na leen njub, jox leen yombalal leen ragal Yàlla.
18فَهَلْ يَنظُرُونَ إِلَّا السَّاعَةَ أَن تَأْتِيَهُم بَغْتَةً ۖ فَقَدْ جَاءَ أَشْرَاطُهَا ۚ فَأَنَّىٰ لَهُمْ إِذَا جَاءَتْهُمْ ذِكْرَاهُمْ
Ana lan la (yéefar ya di xaar ci baña jebbalu) ba bis penc ba faf ne jaseet ci seen kaw bett leen ? Ndax màndargam yi dikk nañu. Te sax su xasee ba eksi ana lan la leen fàttaliku di jariñati?
19فَاعْلَمْ أَنَّهُ لَا إِلَٰهَ إِلَّا اللَّهُ وَاسْتَغْفِرْ لِذَنبِكَ وَلِلْمُؤْمِنِينَ وَالْمُؤْمِنَاتِ ۗ وَاللَّهُ يَعْلَمُ مُتَقَلَّبَكُمْ وَمَثْوَاكُمْ
Xamal ne, amul jeneen Yàlla ju dul moom Yàlla, te nga jéggalu say bàkkaar, ak di jéggalul jullit yu goor yeek yu jigéen yi. Yàlla xam na li ngeen di def lépp guddeek bëcëg.
20وَيَقُولُ الَّذِينَ آمَنُوا لَوْلَا نُزِّلَتْ سُورَةٌ ۖ فَإِذَا أُنزِلَتْ سُورَةٌ مُّحْكَمَةٌ وَذُكِرَ فِيهَا الْقِتَالُ ۙ رَأَيْتَ الَّذِينَ فِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ يَنظُرُونَ إِلَيْكَ نَظَرَ الْمَغْشِيِّ عَلَيْهِ مِنَ الْمَوْتِ ۖ فَأَوْلَىٰ لَهُمْ
Ña gëm ña ngay wax naan : “Cëy ! Bu aw saar wàccatiwoon ! ” Te fekk na saa suñu wàccee aw saar wu leer nàññ te digal ca xare, da ngay daldi gis naaféq ya di la xool ni ñuy xoole dee (ngir ragal). Li gën a yell ci ñoom moo di.
21طَاعَةٌ وَقَوْلٌ مَّعْرُوفٌ ۚ فَإِذَا عَزَمَ الْأَمْرُ فَلَوْ صَدَقُوا اللَّهَ لَكَانَ خَيْرًا لَّهُمْ
topp (jëf) ak wax ju yiw. Su, ndigal la xasee dugg, ñoom dey suñu dëggaloon (ndigalul Yàlla) jëfe ko), mooy gën ci ñoom (fuuf).
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
19Aaya

Tekki — Muhammad 19

Simoore Muhammad Aaya 19 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xamal ne, amul jeneen Yàlla ju dul moom Yàlla, te…

Simoore Aaya 19/38 — Simoore Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Muhammad Dégg, Simoore Muhammad Tekki, Simoore Muhammad mp3, Simoore Muhammad pdf. Aaya 17–21. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers